制作

出演艺人
Alioune Mbaye Nder
Alioune Mbaye Nder
表演者
作曲和作词
Alioune Pala Mbaye
Alioune Pala Mbaye
词曲作者
Prince Ibrahima Ndour
Prince Ibrahima Ndour
编曲
Ibrahima Mbaye
Ibrahima Mbaye
编曲

歌词

Ya Më Xollon Bama Doy La
Ngané Gëstul Xalé Bi
Tchi Noumouy Doxé
Numuy Solo
Xallé bi Super Ciof Lë
Ya Më Xollon Bama Doy Lë
Tchi Ngané Gëstul Gone Gi
Cey Numuy Doxé Ciof Lë
Xam Ngani Mbëgeel Dafa Neex
Cey BËGË Naala Xolbi Yaa Si Neek
Buko Fowee
Xoll Lufa Xass Ba Dugg Logé Fë
Dufa Jugëti
Mbëgeel Da Riche
Bul Diox Sa Xoll Bi Kulay GAAÑ
Ndawsi BËGË Nala Lë
Yaamë Gënël Gone Yi
Man Damay Jooy
So Xassee BËGË Niit Seet Lul
Lum La Def Ngané Noonu LAAY
Xallé Bii Lee Dëg Dëg Joomal Ngama
Ndax Lima Japoon Fof Nga Yamm
DANG Ko Weessu
Turr Bu Bees Bima Am Yamako Tudee
Yamako Tuddeeh
Turr Bu Bees Bima Am Yamako Tudee
Yamako Tudee Chéri
Suma Xalatee Man Nima Mel
Ak Ning Ma Bëgee Damay Jaax lé
Ni Mbëgeel Dafa Neex
Cey BËGË Nala Xol Bi Yassi Nek
Ma Monté (Montel)
Ma Wiissee (Wissel)
Ma Serré (Mbaye Nder Yagg Nga Pogné Sénégal)
Ma Monté (Montel)
Ma Wiissee (Wisseel)
Ma Serré (Ayy Nder Délol Buum Ca Boy Boy Ga)
Ma Monté (Montelma)
Ma Wiisee (Wiisselma)
Ma Serré (Bilay Les Jaloux Vont Mourir)
Mbëgeel , Mbëgeel , Nder
Legu Legu Day Neex
Legu Legu Mou Neex Ba Do BËGË Mu Jeex
So Bëgee
Aaahhhh
So Bëgee
Ma Yokal La Suma Bëgeel
Bala Ngama Merré
Ca Dëgë, Dëgë, Dëgë, Dëgë, Dëgë, Dëgë
Mbëgeel Tiss Na
Kula Bëgul Duko Xam
So Mëssul Bëgë Doko Yëkk
So Mëssul BËGË Doko Xamm
Kula Bëgul Duko Yëkk
Seet Luleen Mbëgeel Dafa Neex
Cey Bëgë Nala Xol Bi Yaa Ci Nee
Ma Monté (Montel)
Ma Wisseel (Wisseel)
Ma Serré (Mbaye Nder Day Ligeey wañi wax Dji)
Ma Monté (Montel)
Ma Wisseel(Wisseel)
Ma Serré (Ayy Nder Boléko Ak Dileen carawaché)
Ma Monté (Montelko)
Ma Wisseel (Wisseel Ko)
Ma Serré (Les Jaloux Vont Mourir)
Bilay Walay BËGË Nala
Ndaw Si KUY Baayam
Cey Wuyuma Iow
Éhh Bula Daw Loo
Wuyuma
Sabañ Mako Mbaye
Yaw Soma Bëgee DANG makoy Wan
Mbëgeel Du Lu Tuti
Yow Kuy Baayam
Cey Bulma Dawloo
Wuyuma
Sabañ Mako Mbaye
Yow Ma Wayla Ndaw Silé BËGË Nala
Cey Ma Wayla Ndaw Silé BËGË Nala
So Xarré Ma Ñëw
Finga Nek Ak Fima Nek Mbaye Sorree Nañu
Xol Day Guissé
Sa Sumala Guissé Man Contann
Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel
Métina Waw Waw Ma Wayla
Ndawsilé Bëgë Nala
Cey Ma Wayla
Ndawsilé Bëgë Nala
So Xarré Ma Ñëw
Finga Nek Ak Fima Nek Mbaye Sorree Nañu
Xol Day Guissé
Sa Sumala Guissé Man Contann
Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel
Métina Waw Waw Ma Wayla
Ndawsilé Bëgë Nala
Cey Ma Wayla
Ndawsilé Bëgë Nala
So Mënee Rekk Ni Mën Ngë
Bollé Ko Ak Dileen Wann Yoon Wi
Ay Nder Wañil Niveau Bi
Written by: Alioune Pala Mbaye
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...