積分
演出藝人
尤蘇安多爾
主唱
詞曲
尤蘇安多爾
詞曲創作
Max Calo
作曲
製作與工程團隊
尤蘇安多爾
製作人
歌詞
Adduna bi du dara ; te dara xaj u fi
Bi Lahii ku ko japp ; xamal ni japp u loo ci ; dara (2X)
Man Youssou ñakk naa ; andandoo bu sincère
Refrain : Adduna ; adduna daal ; nax ati na ñu
Adduna ; adduna da fay wor ee
Habib Faye ; dem na nii
Waa ju baax ; guddée na waay
Habib yaru woon na ; and ak dignité
Fonŋk oon na liggéey ёm ; bëgg njaboot am bu ; baax
Doon oon jàmbaar
Man Youssou ñakk naa ; andandoo bu sincère
Refrain : Adduna ; adduna daal ; nax ati na ñu
Adduna ; adduna da fay wor ee
Habib Faye ; dem na nii
Waa ju baax ; guddée ne waay
Adduna ; adduna ………………… Adduna ; adduna
Refrain : Adduna ; adduna daal ; nax ati na ñu
Adduna ; adduna da fay wor ee
Habib Faye ; dem na nii
Waa ju baax ; guddée na waay (2X)
Written by: Max Calo, Youssou N'Dour