音樂影片

音樂影片

積分

演出藝人
Karabalik Beatz
Karabalik Beatz
Dip Doundou Guiss
Dip Doundou Guiss
饒舌
詞曲
Karabalik Beatz
Karabalik Beatz
詞曲創作
製作與工程團隊
Karabalik Beatz
Karabalik Beatz
製作人

歌詞

Come back
Xol bi yatu ni guedj yafa fess
Ngi di yakh dinagn xarr ba dé
Dinagn xaar dinagne moudj xadi si nioune niare
Refrain
I realy love boul dem ba ma
Boy dem damay wett
Wetay dima sonal
Come back come back
For me douma doundate
Lou dak lii yaw yay
Yaw lafi guiiis
So baby girl come back to me
Couplet
So démé koumay wetali
Soriwo té magui dé wak wett
Liniou soumbe nagn ko yegali iiiiii iiii iiii
Kone soxna ci comme baaaack to me
Lou leudeumone say beut tay dji dina
Ko niiit
Diakhlé tina si none yi bagn
Wayé yalla gui fii
Ngibicile name nalla
Sa khétou diongué tamite name ko
Ngibicil name nala
Boy dem damay wett
Pre refrain
I do I do what you like anytime I do I do
I do I do what you like anytime Ido I do
Refrain
I realy love boul dem ba ma
Boy dem damay wett
Wetay dima sonal
Come back come back
For me douma doundate
Lou dak lii yaw yay
Yaw lafi guiiis
So baby girl come back to me
Couplet
Lou aale bi yatou yatou
Lep di dale guay dagou
Bou liwé si mane guay diarou
Bou liwé si mane guay diarou
Taylé samay nelaw pour tok ak yaw
Nelaw pour tok
Baby xamgua ni louné lay def pour tok
Louné lay def pour tok sa xol
Pre refrain
I do I do what you like anytime I do I do
I do I do what you like anytime Ido I do
Refrain
I realy love boul dem ba ma
Boy dem damay wett
Wetay dima sonal
Come back come back
For me douma doundate
Lou dak lii yaw yay
Yaw lafi guiiis
So baby girl come back to me
Written by: Karabalik Beatz
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...