積分
演出藝人
Elage Diouf
演出者
詞曲
Elage Diouf
作曲
歌詞
ATTE GUI MOUDONE LOUMA ITEL MAY NIANE YALLA KAGNE LAY AM DOOM
AY FANN GUI SOUMA TEUDER BALA MAY NELAW DAMAYE NIANE YALLA
MOU MAYMA DOOM
ATTE GUI MOUDONE LOUMA ITEL DAMAY NIANE FALAWO MOU MAY MA DOOM
AY FANE GUI SOUMA TEUDER BALA MAY NELAW DAMAY NIANE YALLA KAGNE LAY AM DOOM
ANI JAMIL ANI LILI
NIONIOU DAL NIOM NIOGUI FEE SI DIGANTER ASSAMANE AK SOUF
ANI NABOU ANI MALICK NIONIOU DAL NIOM NIOGUI FEE SI DIGANTER ASSAMANE AK SOUF
MELODIES
ATTE GUI MOUDONE LOUMA ITEL
DAMAY NIANE FALAWO KAGNE LAYE AM DOOM
AYY FANE GUI BOUMA DJOULER BALA MAY SEULMEUL
DAMAY NIANE FALAWO MOUMAYMA DOOM
ANI JAMIL ANI LILI NIONIOU DAL NIOM NIOGUI FEE SI DIGANTER ASSAMANE AK SOUF
ANI MALICK AK NABOU NIONIOUDAL NIOM NOGUI FEE SI DIGANTER ASSAMANE AK SOUF
MELODIE
ANI MALICK ANI NABOU NIONIOUDAL NIOME NIOGUIFEE SI DIGANTER ASSAMANE AK SOUF
ANI LILI ANI JAMIL NIONIOU DAL NIOME NIOGUI FEE SI DIGANTER ASSAMANE AK SOUF
ANI MALICK ANI NABOU NIONIOU DAL NIOM NIOGUI FEE SI DIGANTER ASSAMANE AK SOUF
BOU SOBER YALLA DINABAKH
DI NIANE YALLA KAGNE LAYE AM DOOM
DI NIANE FALAWO MOUMAYMA DOOM
DI NIANE FALAWO MOUMAYLA DOOM
SEN MOUDJ
SEN MOUDJ MOM RAFETAL KO
BA NIIT YI NAWLA KHAMNER YAW NDANANE GA
GA DIOUDO FOU BAKH NEKK FOUBAKH
NIEPP YENELA LOUBAKH
ANNNHHHH WAYNALA JAMIL
Written by: Elage Diouf