積分
演出藝人
Xiirsa
演出者
詞曲
Nick Silver
作曲
Prince Ibrahima Ndour
編曲
Sakhir Niang
詞曲創作
Saliou Samb
詞曲創作
歌詞
Sama Xoll Nga Yoré, Mom Lala Topé…
Liti Liti Litti Litti
May Rombé Goumbé.
Dama Tapétoul,
Defna Thi Louné!
Loumou Gouddi Gouddi Gouddi,
Damalay Goungué…
Baby I Follow You,Cause My Heart Is On You, Youuu
Baby I Follow You,Cause My Heart Is On You, Youuu
Ohohohh, Pourtant Joxnala Lepp
Joxla Léepp
Ohohoh, Pourtant Je T’ai Tout Donné,
Tout Donné
Annhannhh
Annhannhh
Annhannhh
Annhannhh
Annhannhh
Annhannhh
Annhannhh
Annhannhh
Xamna Bou Baax Lingay Bañ
Dem Bacca Biir Malay Gagn
Defnako Sa Ay Mass Wayé
Man Da Amm Loumay Wath
Adouna Mola Sokhla
Man Ma Yitté Wola Lool Sax
Massamba Ming May Gagn Ayy
Clamer Nalak Gayii
Kayy Gaaw,Deugg Leu Ni Deungg Nayy
Souma Démé Balay Way Nga Xamni Caxaan Taxoul
Ohohohh, Pourtant Joxnala Lepp
Joxla Léepp
Ohohoh, Pourtant Je T’ai Tout Donné, Tout Donné
Annhannhh
Annhannhh
Annhannhh
Annhannhh
Annhannhh
Annhannhh
Annhannhh
Annhannhh
Man Douma Say Say,Lathko Sama Gayi
Ñeuweul Gnou Life Wayy
Sonou Naaay
Boul Meusseu Gaday,Donal Sen Yaye
Ndiabott Gui Kay Way Goungué Maaa
Man Douma Say Say,Lathko Sama Gayi
Ñeuweul Gnou Life Wayy
Sonou Naaay
Written by: Nick Silver, Prince Ibrahima Ndour, Sakhir Niang, Saliou Samb

