歌詞
LII NDAKH NA THIE GUENE
DAMAY TOK MOUY GEUNEU TARR
LEP MAKOY MOUNIE
WALA THIAT MOMA TOPE MA BOLEE THIE NAKHARI DEREET TANG KHÔL
MAY SEET KAN LA KAY JINN AK KOMOKO TEK GEUMATOUMA MBEUGEL NDAKH AY JEUFINE YOU NIAW REWANDE LAYENTE BIIR
KHARITE YOU BONE MBOK YOU GEUMOUL DARA POLITICIENS YOUY DUNDEE NGERR DI NAKH ASKAN WII AY NIIT YOU BEEW SERIGNE SU NIEME YALLA AMATOUMA YAKAR
NII FII DÎNA FII TOK
DIGANTE DUND AK DEE NIAK JOMM
KHAJOUFEE FEBAR MIUNO FAJU
DUNDE GOU SEER
KILIFEU YI SOSS MAK NIE DII SOUS
AHH MOUY RÉALITÉ FII THIE MIME REEW BES BOUNEE NGUA DEG FII
KAA BOUNEE
SAMA DOM YALA NALA YALA MOUSEUL THIE NIAWTEEF YI NGUA
NARA JANGONE TELL
INJUSTICE FII DANIIU LAY KHEUREUM
AY KHEUREUM YOU BONE BA SI SA
BIIR BAMEL
LI DEE NIAW NA EH LIKA SOUFEE
EH LII KA SOUFEE EH THIE MIN REEW FII LAY KHEWEEE SEYTOU KO
NGUA FEBAR MUNIO FAJU DUND GOU CHER GUI INJUSTEMENT AK KHEUREUM YOU BONE NGA DEE NIOU TOPELA BA SA BIRR BAMEL
KILIFEU YII DI SOS KHALEYII SOUS
NIEE DII VOLÉE
AHH WAY WII TEY MOM DOU NEKH
WAYEE LIMAY WAKH NDAKH DEGUELA AM DEET
HOO MOUY RÉALITÉ FII THIE SAMA REEW
AHH FII LAY KHEWEE
NDAKH FII BESBIU NÉE NGA DEGUE FII KAA BIUNEE
OHH KOULA DAKH WAT NGANEE KII LA
REWANDEE KHAWII SOUTOUREU
BESBOU NÉE NGA DÉG FII KA BOUNEE TEY MOM WAKH J DOU NEEKH
Written by: Elage Diouf