Lyrics

Do modèle do modèle do modèle do modèle yow nigga do model (do modèle) Do modèle do modèle do modèle do Modèle yow nigga do modèle (do modèle) Do modèle (do modèle)do modèle han nan tchi dara do modèle Do modèle do modèle do modèle do Modèle yow nigga do modèle (do modèle) Do modèle do modèle do modèle do Modèle yow nigga do modèle (do modèle) Do modèle (do modèle)do modèle han nan tchi dara do modèle Tchi alal tchi djiko tchi diné do modèle Tchi rewmi mi thi xéet bi tchi ndaw gni do model Do model do model do model so model yow nigga do modèle Do modèle do modèle do modèle Djitou nga falou mais tewoul do modèle Bayiwofi dieuf boula kén meuneu wayal Sa xél mo thieuk walabok da nga tayal Do modèle do modèle akh rek nga niou yorel Werr bala déh yagui fayou ay brick Nioune tchi bureau lanielay khar yow ya ngui teudiou hotel Do model do model rakh tchi doli do kou honnête Biss migui nieuw da nga takk sunuy menotte Bouko kén baal limouniou yorel lepp na mateu Économie rew faux billets dakoy damate Fi kou beugu doon milliardaire fokk nga nanguo khar matte Yén dale yén dérou serigne ngueni yakh Politigué sén talibéyi djiaay sen carte Nguour guoufi niew nguen chantage Dieul pourcentage lolou dale moy sen marque Do modèle do modèle tchi dara Ana ragal yallah khana do domou daara Bou ndieuk ay zaïr nio daan féki baatinn Wayé legui ay baatiin kom kom laniouy fighting Niata niou taylé tchi lokhoy toubab yi Mamadou Dia doyna cédé coups bas yi École dou diangualé téré Touba yi Mais Cheikh Anta Diop dey dead rek mais dou bayi Maître Babacar Seye moy prix Nobel Histoire migui neub ay criminel Biss migui niew bagnekat free ni Nel Son Mandela li nga gueum dé tchi fidel Coup d'etat dictateur nga do model Kou niep ande falando kone tololel Signé ay accord di ceddo sunu kaagn Rêvé loniou tchi sa discours khif bi diniou gaagne Do modèle Do modèle do modèle do modèle do modèle yow nigga do model (do modèle) Do modèle do modèle do modèle do Modèle yow nigga do modèle (do modèle) Do modèle (do modèle)do modèle han nan tchi dara do modèle Do modèle do modèle do modèle do Modèle yow nigga do modèle (do modèle) Do modèle do modèle do modèle do Modèle yow nigga do modèle (do modèle) Do modèle (do modèle)do modèle han nan tchi dara do modèle Tchi alal tchi djiko tchi diné do modèle Tchi rewmi mi thi xéet bi tchi ndaw gni do model Do model do model do model so model yow nigga do modèle Takk derr tchi diguou tali melni deum mardertali Diokhé témer (500f) rek dial sokhlawoul di gaddu permis Garde à vue niou tekk leu zermi dileu saga melni bandit Formation bi nanie ko kholaat autorité non dou gueudé No étude no éthique corrompu no mérite Do modèle kouniouy guerre do modèle Hopitaux yi nguey guiss médecin you réw Pensement ak perf rek laniouy meuneu yéw Démeul faye feulé so paré doga téw Ap sothie nga fey indi rek niou defkop néw Ki niew amé metite dafa sokhla kouko dalal Niaka kerseu infirmière yi legui niepeu len ragal Do model do modèle yeureumo seuy malade Niakk contrôle mo wareul laisser aller bi Manque d'effectif excusou tapalé bi Ana emergence laay lathie ki tchi palais bi Goor guouy taak moromou goor do modèle Yow ame nga dolé ko romb daur do modèle Niari werr yi ben yone laniou tchiy oubi page Diangue khalé yi nga djiapelen en otage Ay grève you wékou tchi caprice Ndakh sa élèves yi diaralounie leu sacrifice? Député bouy khasté di saga do modèle Transhumé nga wédi sa ada do modèle Yow lot of nigga daniou taré nigga Daniouy fo tchi tali bi di faté séni bakane laniouy taylé nigga Yagui loué deuké ndole dieum nga mak té wara maul (construire) Boulko wekk tchi ay lotterie akeu khoss ticket Bediaw djiégué new done bébé beugu méw Founie leu fekk ya gui namp ci ay prostituées Yakh nga dérou djiguen euleuk boula sa Dome ladjié ma lodoon liguey = khana thiagatou Do modèle do modèle do modèle do modèle yow nigga do model (do modèle) Do modèle do modèle do modèle do Modèle yow nigga do modèle (do modèle) Do modèle (do modèle)do modèle han nan tchi dara do modèle Do modèle do modèle do modèle do Modèle yow nigga do modèle (do modèle) Do modèle do modèle do modèle do Modèle yow nigga do modèle (do modèle) Do modèle (do modèle)do modèle han nan tchi dara do modèle Tchi alal tchi djiko tchi diné do modèle Tchi rewmi mi thi xéet bi tchi ndaw gni do model Do model do model do model so model yow nigga do modèle Bandit dou taukh dou guinz pour ame fite Dou kogne bi ngey took di keuf ay wetchit Milliardaire do creer emploi Do modèle même sou fékké ya tchi ame droit New bi ngay souli mouy guili tchi tioumikaay Takhaw beuré dofi xeureum beu xeuy fi doon roi Do modèle do modèle do modèle ha nan tchi dara do modèle Kou ame merite dounie leu diokh post Incapable yi rek nioy sole cost (costume) Conséquence yi legui boy yi gni gui bayi diang Nénagne diarouko sama time laay lost Immigré yagu nga doundé sunu bourse Legui paré nga té beuguo delsi sunu rew Bo niep defoon ni yow eskeu dina bakh Né nga fi amoul dara lign ley faye dafa néew Deugu deugu khar tchi guétte moleu tané Victime nga da ngey rirendo rek topou tendance Nane dafeu xéw taukh dafeu xéw pass pass bombass Ya gui faté le temps passe Askane wi nga bokk doon tchi modèle Linguey bi ngey def doon tchi modèle Rafetal sey dieuf bofi diougué ay ate Gniy niew demain diapeleu model Do modèle do modèle do modèle do modèle yow nigga do model (do modèle) Do modèle do modèle do modèle do Modèle yow nigga do modèle (do modèle) Do modèle (do modèle)do modèle han nan tchi dara do modèle Do modèle do modèle do modèle do Modèle yow nigga do modèle (do modèle) Do modèle do modèle do modèle do Modèle yow nigga do modèle (do modèle) Do modèle (do modèle)do modèle han nan tchi dara do modèle Tchi alal tchi djiko tchi diné do modèle Tchi rewmi mi thi xéet bi tchi ndaw gni do model Do model do model do model so model yow nigga do modèle
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out