Lyrics

Par AbouAmg Lo beug beug naa Lo bagn mane beugouma Yaa takh namatouma dara kone diegué ma Baby deff ma loula nekh yaa tey waay Doumla meusseu bayi hun hun Kaay kaay Sa ree meune nama rey té bougouma guiss ngey merr Ragal nimla beugué khalé bi li comme guerre So beugué louma amoul nako wouti diokh la Sam mbeuguél sama amour negn ko boolé yokh la Mi corazón (corazón) Mane douma taayi té douma sone (no no no) Wakh lene ak mom Damko nopp té nangou naa ci niakk diom Oh ohh ouhh ohh Damako guiss youkhou oh ouh oh Oh ohh ouhh ohh Foumala guiss youkhou oh ouh oh Yaw laay nobat, yaw laay nobat Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat Yaw laay nobat, baby yaw laay nobat So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat Yaw laay nobat, yaw laay nobat Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat Yaw laay nobat, baby yaw laay nobat So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat Diaral ngama khékh ak Pa bi gueneu gallé Guédeu agn té sou mère bi wakhé doumko Falé Collé serré doumla bayi moukk di crazy Bayanté negn mais yaw laay guéneul ba leggi Amna kénene mais soum key khol yaw rek laay guiss Deuké sagnsé pour nga xool ma sa khel delsi Baby, beugué nala nouné Fo dem ma fekk la fa diaral ngama louné Oh ohh ouhh ohh Damako guiss youkhou oh ouh oh Oh ohh ouhh ohh Foumala guiss youkhou oh ouh oh Yaw laay nobat, yaw laay nobat Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat Yaw laay nobat, baby yaw laay nobat So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat Yaw laay nobat, yaw laay nobat Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat Yaw laay nobat, baby yaw laay nobat So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat Sama kér ak sama garap Sama febar sama garap Takh ma guerre ak samay parents Baay ma dee ci sa kaw darap Yow linguere nga or ak diamant Takal la aldinay kara Yaw rekka ma diaral ganratie bakane koranté Balla Teud diakhane fou ay car rapide diaré sama kaw yaram Ta dou thiakhane diaral ngama niou nane ki diaratoul dara Diaro bim ley takal dou diarat ci benene baram Diabar laley deff Diabar diou keneu doul lambal ndiaram Yaw laay nobat, yaw laay labat Dagueu sama baat gueuneu yombou nga niane ma baat Diokh ma sa lokho té goungué ma Porto Rico Yaay sama lover sama chabalaba ding dong Oh ohh ouhh ohh Foumala guiss youkhou oh ouh oh Yaw laay nobat, yaw laay nobat Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat Yaw laay nobat, baby yaw laay nobat So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat Yaw laay nobat, yaw laay nobat Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat Yaw laay nobat, baby yaw laay nobat So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat
Writer(s): Abdou Lahad Thioune, Dominique Preira, Ismaila Talla Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out