Lyrics

Eh lamou saff kén doula ko wakh Ndakh kako mathie Ko xam Ni nane ki dalay gololo nane do dara Maa dougou ci biir ba lépp lérr ma Naandie diarr ngako Koula xamoul moy diranték yaw Mbague chérie coco Bo done musicien Mané la do degammer Déf ngama sa xalé Do joué ak man jeu de gamin Deuk dima diamb, dima diamb Yoro marimba do Benjamin Bo défoul ndank na meussa téyé Sa lokho on sait jamais Mom xalé la té bari na dolé Mo raw alkaati dafay dooré Dina la topato ba lathie la, lathie la Lathie la bébé loy réeré Té boko ladié Mouné la bae man yaw mi lay rééré Fadjr tél ni lamay yéewé Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait? Yaw ya raw athlète bou drogué Koula topp ba ci biir day moudié claté Fadjr tél ni lamay yéewé Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait? Yaw ya raw athlète bou drogué Koula topp ba ci biir day moudié claté Eh dafa nékh lolou nga am Kou xam liy diamb sa ditakh Sokh lawoul sakh ngay wakh Day exécuter néwoul kou rambakh Téey na xamé na fougnouy féthié Yéla ak ndaw rabine Coller gnapp mélni docteur Raoult Ak choloroquine Armée wou kaw ak souf Mélni kouy dém guerre Tassaré arsenal yi boula dal nga terre Dila woo ci beuré té léer na, léer na Molla, mola meun dila nogatou Tass sa nguémb mbeur ma danou na, oh secours Mom xalé la té bari na dolé Mo raw alkaati dafay dooré Dina la topato ba lathie la, lathie la Lathie la bébé loy réeré Té boko ladié Mouné la bae man yaw mi lay rééré Fadjr tél ni lamay yéewé Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait? Yaw ya raw athlète bou drogué Koula topp ba ci biir day moudié claté Fadjr tél ni lamay yéewé Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait? Yaw ya raw athlète bou drogué Koula topp ba ci biir day moudié claté Fadjr tél ni lamay yéewé Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait? Yaw ya raw athlète bou drogué Koula topp ba ci biir day moudié claté Fadjr tél ni lamay yéewé Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait? Yaw ya raw athlète bou drogué Koula topp ba ci biir day moudié claté Eh lamou saff kén doula ko wakh Ndakh kako mathie Ko xam Ni nane ki dalay gololo nane do dara Maa dougou ci biir ba lépp lérr ma Naandie diarr ngako Koula xamoul moy diranték yaw Mbague chérie coco Bo done musicien Mané la do degammer Déf ngama sa xalé Do joué ak man jeu de gamin Deuk dima diamb, dima diamb Yoro marimba do Benjamin Bo défoul ndank na meussa téyé Sa lokho on sait jamais Mom xalé la té bari na dolé Mo raw alkaati dafay dooré Dina la topato ba lathie la, lathie la Lathie la bébé loy réeré Té boko ladié Mouné la bae man yaw mi lay rééré Fadjr tél ni lamay yéewé Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait? Yaw ya raw athlète bou drogué Koula topp ba ci biir day moudié claté Fadjr tél ni lamay yéewé Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait? Yaw ya raw athlète bou drogué Koula topp ba ci biir day moudié claté Eh dafa nékh lolou nga am Kou xam liy diamb sa ditakh Sokh lawoul sakh ngay wakh Day exécuter néwoul kou rambakh Téey na xamé na fougnouy féthié Yéla ak ndaw rabine Coller gnapp mélni docteur Raoult Ak choloroquine Armée wou kaw ak souf Mélni kouy dém guerre Tassaré arsenal yi boula dal nga terre Dila woo ci beuré té léer na, léer na Molla, mola meun dila nogatou Tass sa nguémb mbeur ma danou na, oh secours Mom xalé la té bari na dolé Mo raw alkaati dafay dooré Dina la topato ba lathie la, lathie la Lathie la bébé loy réeré Té boko ladié Mouné la bae man yaw mi lay rééré Fadjr tél ni lamay yéewé Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait? Yaw ya raw athlète bou drogué Koula topp ba ci biir day moudié claté Fadjr tél ni lamay yéewé Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait? Yaw ya raw athlète bou drogué Koula topp ba ci biir day moudié claté Fadjr tél ni lamay yéewé Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait? Yaw ya raw athlète bou drogué Koula topp ba ci biir day moudié claté Fadjr tél ni lamay yéewé Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait? Yaw ya raw athlète bou drogué Koula topp ba ci biir day moudié claté
Writer(s): Djiby Ka Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out