Musikvideo

Musikvideo

Credits

PERFORMING ARTISTS
Abdou Guite Seck
Abdou Guite Seck
Lead Vocals
COMPOSITION & LYRICS
Abdoulaye Guitte SECK
Abdoulaye Guitte SECK
Songwriter
Ousmane Ka
Ousmane Ka
Arranger
Bril
Bril
Arranger
PRODUCTION & ENGINEERING
Abdou Guite Seck
Abdou Guite Seck
Producer

Songtexte

SANT YALLAH
Sant len ko sant naa ko sant Yallah
Sant len ko sant naa ko sant Yallah (bis)
Ni am na bes
Ma romb fa gaa nia
Ba niou guenne nieup nio len naw lou
Ni banen bes
Man dem naa fa
Ba ma deme nieup di ma settan
Mou dalal ma
Solal ma lou ne
Ba ma mel ne belefete thi kaw thiolin
Thi laa degge ni may diamant thi souf si
Thi laa degge ni may bidew thi diaw dji
Thi laa degge ni may diantal maa gueneu thioffe
Thi laa degge ni may gaïnde maa beuri dole
Thi laa degge ni may may tannef thi askan
Guite Laobe Lati Sar mi bokkak Baye Diarra Fall
Guiss naa say fem
Kham naa say mbaakh
Degg naa sa diallore sant Yallah
Sant len ko sant naa ko sant Yallah
Sant len ko sant naa ko sant Yallah
Meïssa meun nga bes
Ndakh fi ngay guenne
Kou fa guenne nieup nio lay setaan
Ni am na bes
Ma romb fa diek dia
Ba niou guenne nieup nio len naw lou
Mou dalal len
Solal len lou ne
Baniou mel ne belefete thi kaw theolin
Thi laa degge ni may diantal maa gueneu thioffe
Thi laa degge ni may gaïnde maa beuri dole
Thi laa degge ni moy mbokkou ndeyou Baye Ada
Sounou rakk die Ak Khadim Guey Saloum Saloum
Thi laa degge ni moy tanef thia Colobane
Marche Gambie sedde len ma am ko moy sant Yallah
Meïssa Gueye Ndioro Bassy
Yaw yaa yelol dole
Dieulou loo ko di ko khekhe
Diappale nga sa ndaw yi
Gueye Ndioro Bassy
Gueye Ndioro Bassy
Gueye Madieye Awa Toure
Boroom Sandi gui thin dem
Doneil Yibra Gueye Fat Aw
Yirim Deuguene Mqlick Gamou Seck
Ndiol ma des thi Gan
Cheri Soda Sow Poulo cheri Binta Faye
Magou Pathe Gueye Ndioro Sant Yallah
Huuuuuuuuuuhuuuuuuuuu
Boutik ba ne colobane moo ne grand Yoff
Boo khew le boffa sollo melne belefete
Boutik ba nga Colobane ma nga Touba
Loo khew le boffa sollo mel ne belefete
Ni boutik ba nga colobane ma nga Touba
Bayou Papa Abdoo solal noo
Ni boutik ba nga colobane ma nga Touba
Loo khew le boffa sollo mel ne belefete
Bayou Maame Fatook Bb Ada
Sant len ko sant naa ko sant Yallah
Sant len ko sant naa ko sant Yallah
Sant len ko sant naa ko sant Yallah
Sant len ko sant naa ko sant Yallah
Sant len ko sant naa ko sant Yallah – Boutique !
…FIN…
Written by: Abdoulaye Guitte SECK
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...