Lyrics

Wa dji aduna'm yakkou na Sokhna si dom'am sangkou na (Jëf djilé daffa niaw) Ndaw si sëyeum ba yam nafa njabott gui tassaro (Jëf djilé daffa niaw) Bilay man mi dh warouna diamono'k fimou tollou ni Ak jëf you niaw yi niouffi faral di guiss Xana denio fatté beussou penc dina nieuw Denio muur xelam ba tagaliko'k saggom (Jëf djilé daffa niaw) Yakkal negn ko ligueyam ba tassaré njabottam (Jëf djilé daffa niaw) Toroxol ko thii nawleem ba guéné ko thii keureum Mou dem ba tay yay'am diaxlé lool Ba di misère guène aduna thii nakhar (Jëf djilé daffa niaw) Ak nimou yiwé wone bilay nonou la yarro wone Bakhone, jambar mo donnone sen yakkar Dieul domou diambour yobou ko thii serigne bi Thii serigne tarriya Dieul tour yay'am diokh ko Dieul tour bay'am diokh ko Tibb ay tangkam diokh ko Sath ay yeureem yobboul ko Serigne bi bind xaatim diokhla Nga daldi soul thii bountou keureum hum hum Thii lathii yem fitteum dem Thii la sangko batay nieuwoul Li dh mettina Bilay li daffa niaw té li dou lou bakh (Jëf djilé daffa niaw) Bilay li daffa niaw té li dou lou bakh (Jëf djilé daffa niaw) Bilay li daffa niaw té li dou lou bakh (Jëf djilé daffa niaw) Bilay li daffa niaw té li dou lou bakh (Jëf djilé daffa niaw) Aduna ngui ley diay Nga yakk domou diambour Kouy diay sa leer Dieundé ko ak leundeum Yow dinga gueuleum Ba do am ngueureum Leundeum diaroul deureum Ak dinga dokh ba dinga gueuleum Ceey sama gars yi yeurmandé Ki'way domou diambour Na nga dawal yeurmandé Yeurmandé eh Wo oh oh dawalal yeurmandé Na nga dawal yeurmandé (li daffa niaw li daffa niaw) Na nga dawal yeurmandé (Li daffa niaw li daffa niaw) Na nga dawal yeurmandé (li daffa niaw li daffa niaw) Na nga dawal yeurmandé (li daffa niaw li daffa niaw) Na nga dawal yeurmandé (li daffa niaw li daffa niaw) Na nga dawal yeurmandé (li daffa niaw li daffa niaw) Na nga dawal yeurmandé (li daffa niaw li daffa niaw)
Writer(s): Hakim Abdulsamad, Aida Samb Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out