Music Video

Ismaël Lô - "Le jola"
Watch {trackName} music video by {artistName}

Credits

PERFORMING ARTISTS
Ismaël Lô
Ismaël Lô
Performer
Pierre Bertrand
Pierre Bertrand
Performer
Claude Salmieri
Claude Salmieri
Performer
Laurent Vernerey
Laurent Vernerey
Performer
Stan Renoult
Stan Renoult
Performer
Yann Martin
Yann Martin
Performer
Michel Aymé
Michel Aymé
Performer
Paul Thierry Oliveira
Paul Thierry Oliveira
Performer
Thierry Boucou Pastel
Thierry Boucou Pastel
Performer
Philippe Balatier
Philippe Balatier
Performer
Philippe Georges
Philippe Georges
Performer
Olisa
Olisa
Chorus
Diane Solo
Diane Solo
Chorus
COMPOSITION & LYRICS
Ismaël Lô
Ismaël Lô
Translation
Pierre Bertrand
Pierre Bertrand
Arranger
Claude Salmieri
Claude Salmieri
Arranger
Laurent Vernerey
Laurent Vernerey
Arranger
Stan Renoult
Stan Renoult
Arranger
Yann Martin
Yann Martin
Arranger
Michel Aymé
Michel Aymé
Arranger
Paul Thierry Oliveira
Paul Thierry Oliveira
Arranger
Thierry Boucou Pastel
Thierry Boucou Pastel
Arranger
Philippe Balatier
Philippe Balatier
Arranger
Philippe Georges
Philippe Georges
Arranger

Lyrics

Senegal senegal siguil ndiguale Gambia gambia oh siguil ndiguale Amna benna ferie bougnou dane nane Bateau Le Jola mi soukh sibir gueth gui Xalebi migui dioye nane baye Baye anna sama yaye boye Baye neko dome anna yaye boye yaw Senegal senegal siguil ndiguale Gambia gambia oh siguil ndiguale Mane baye migui dioye nane dome Dome anna sa yaye boye Dome neko baye anna yaye boye yam Kone li firina ni yala reke sagne yala Reke mane kon mome rekeu moy bour Refrain Ndakh kepeu ko lath moune amnathi Waye kon lii fir ndena ni senegal bena bopeleu Senegal beneu bopeleu Senegal beneu bopeleu Bilay Ken douko khar gnaro Beneu bopeleu senegal Faguarou diotna Nagnou xolat sougnou bopeu bou bakh Nagnou bayi douman kila Bo dioume dagua wara nangou Diougue Heu heu heu heu Bougnou diogue sili Nagnou kholat sougnou bopeu bou Baaakh Beneu bopeleu heu heu heu Beneu bopeleu senegale haha hahale Refrain
Writer(s): Ismael Lo, Paul Thierry Oliveira Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out