Lyrics

Sama baby sokhna-la dou guél thi mane Té mbeuguélam meun nama, louma thi meun Sama baby sokhna-la dou guél thi mane Té mbeuguélam meun nama, louma thi meun You're my baby, sokhna nga do guél thi mane Mbeuguélam louma thi meun That's my baby Sokhna-ci do guél thi mane Mbeuguélam louma thi meun Sama doundou gui dakh na lém Tégalma Kim Ka, no no douma dém No matter what they say, me no follow them Loma meunti fay non mane douma dém Sou méré ma diaay maana, monté gueuna louma Eh! Sou méré loma tégal beugouma Xalé bilé, sita questà, diéguéma gnou fiesta Diarna ma photo la all night poste ko Insta Mamacita c'est ça banana ananas Diarna ma photo la all night poste ko Insta Xalé bi amnaa faiblaissam, lii lanla Sou féké naturelloul mysthique la, dogali-ma Sama baby sokhna-la dou guél thi mane Té mbeuguélam meun nama, louma thi meun Sama baby sokhna-la dou guél thi mane Té mbeuguélam meun nama, louma thi meun You're my baby, sokhna nga do guél thi mane Mbeuguélam louma thi meun You're my baby Sokhna-ci do guél thi mane Mbeuguélam louma thi meun Baby baby, baby baby I love you so much you got my mercy Baby baby, baby baby I love you so much you got my mercy Niawou ma, sofou ma Bour yalla mako téraléé Sama mbeuguel-gui nimma lééré Sama chérie sita questà, diéguéma gnou fiesta Diarna ma photo la all night poste ko Insta Mamacita c'est ça banana ananas Diarna ma photo la all night poste ko Insta
Writer(s): Akatche Bennette Seraphin Koffi Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out