Clip vidéo

Youssou Ndour - New africa
Regarder le vidéoclip de {trackName} par {artistName}

Crédits

INTERPRÉTATION
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
Chant
Jean-Philippe Rykiel
Jean-Philippe Rykiel
Claviers
Ousseynou Ndiaye
Ousseynou Ndiaye
Chœurs
Babacar Faye
Babacar Faye
Percussion
Mamadou Mbaye
Mamadou Mbaye
Guitare principale
Assane Thiam
Assane Thiam
Batterie
Habib Faye
Habib Faye
Claviers
Fallilou Niang
Fallilou Niang
Batterie
Ibrahima Cisse
Ibrahima Cisse
Claviers
Thierno Koite
Thierno Koite
Saxophone alto
Issa Cissocko
Issa Cissocko
Saxophone ténor
Charlie Lagond
Charlie Lagond
Saxophone ténor
Ken Fradley
Ken Fradley
Trompette
Lee Robertson
Lee Robertson
Trombone
COMPOSITION ET PAROLES
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
Composition
Kabou Gueye
Kabou Gueye
Paroles
Habib Faye
Habib Faye
Composition
PRODUCTION ET INGÉNIERIE
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
Production
Jean-Philippe Rykiel
Jean-Philippe Rykiel
Co‑production

Paroles

Mane Youssou Ndour! Ma ngi wo! bépeu domi Africaaaa! Gnou bokeu khalate! Bokeu guiss guiss! Bokou yénéééééé! Sans frontiéres Bolé sounouy ame ame Té liguééééy! Wara tougnou Nangou kéne nieuw Dignou féwaléééééééééé! Boul djité rew Fok né la fa nek Yaw ya ko mome! Ndite bou deugueur Dafa wara fek nga beug sa rew Té sakou ndimbeul Ndimbeul na sa fek Lokhoy boroooom! Woy Africa! Bou dianteu bi finké waw! Na la fek diok! Ak sa dioumetou kaye! Beuthieuk bi gaw neu! Niéteu dou beuré Té niarra meuneu kééééneu waw! Yone wi! sorré na! Té métti na Naniou ko waaadial Bo doul nopé khalate La niou défone Mameuuuu ya! Sa khol do toul nekh Té dotou khame lou doul féyane to! Souma sagnone Africa Béne niit mo koy djité! Niou bolé Sounouy khalate Ak sounouy dolé Diokh ko! Naniou oubi frontiers yi! ratakhale yone yi Ba nieupeu guissé Changes your thinking! Work together! Keep and working! Cheikh Anta Diop! Kouamé Nkrumah! Steven Biko! All you people! Africa!
Writer(s): Habib Faye, Youssou N Dour Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out