album cover
Amina Ye
album cover
00:10
00:30
00:45
02:40
00:00
03:00
Ultimi 7 giorni
Amina Ye è stata scoperta più frequentemente a circa 30 secondi dall'inizio la canzone durante la settimana passata

Video musicale

Video musicale

Testi

Parrum pampampampa rumpampam
Parrum pampampampa rumpampam
Parrum pampampampa rumpampam
Parrum pampampampa rumpampam
Mey na la sama khol (ngani ya bagne)
Ma mey la moto (ngani ya bagne)
Ma doli si auto (ngani ya bagne)
Keur ak khalifs (ngani ya bagne)
Ooh Amina yé (sabari)
Jolie Amina (sabari)
Oh Amina yé (sabari)
Dina la boulé sama yaye
Allo maman bobo
Ki deh sama khol bi la yobo
Né douma ko delo
Sou nguene si wakhoul dinama doflo
Parrum pampampampa rumpampam
Parrum pampampampa rumpampam
Parrum pampampampa rumpampam
Parrum pampampampa rumpampam
Mane mi deh diakhlena
Ma ngui sogua guiss khalé bou Mel ni Amina
Pekhé bou né diém na
Mou téyé foumou téyé
Né beuguouma eh
Jolie Amina
Kouma khol khamni Mane mi miir na
Lekka touma nanatouma nelawatouma
Sama khel bi diakhasso mane tit na deh
OH Amina
Mey na la sama khol (ngani ya bagne)
Ma mey la moto (ngani ya bagne)
Ma doli si auto (ngani ya bagne)
Keur ak khalifs (ngani ya bagne)
Ooh Amina yé (sabari)
Jolie Amina (sabari)
Oh Amina yé (sabari)
Dina la boulé sama yaye
Allo maman bobo
Ki deh sama khol bi la yobo
Né douma ko delo
Sou nguene si wakhoul dinama doflo
Parrum pampampampa rumpampam
Parrum pampampampa rumpampam
Parrum pampampampa rumpampam
Parrum pampampampa rumpampam
Ndekke amina deh lou kay doflo (waga waga)
Mom deh lou kay mier lo (waga waga)
Diabou bandidos (waga waga)
Euh amina yé nakh na ma
Parrum pampampampa rumpampam
Parrum pampampampa rumpampam
Parrum pampampampa rumpampam
Parrum pampampampa rumpampam
Written by: Papa Kande Sidibe

Loading...