album cover
Nit Nite
album cover
Nit Nite è stato pubblicato il 11 maggio 2026 da Stora music come parte dell'album TERANGA
AlbumTERANGA
11 maggio 2026
EtichettaStora music
BPM87
Melodicità
Acousticità
Valence
Ballabilità
Energia

Video musicale

Video musicale

Testi

Nit nitey, molay taha done nit yee
Andak Teck ak tey
Marnan bumu la takha nane petitt
Nit nitey
Mole takha done nit
Andak Teck ak tey
Mar naane bumu la taha nane petitt
Aduna bi kéne dou ko yenu (yenu)
Ki yabo taylu (taylu)
Daradiar fi daw by danu
Kuko ci def dey ya ci ganu
Kone dessna by ci xel wen (hey)
Ken talatul dara ludul seurign tu
Ken gematul ken nyepay moytu
Nit ki nga wolu
Mole xamal lu bon dadi ko wasare nga yakko
Boko jeko feyu
Te gnu delu ci yalla
Nit nitey
Moley takha done NIT
Andak tekaktey
Marr nane bumu la takha nan petitt
Nit nitey
Molette takha done NIT
Andak tekaktey
Marr nane bumu la takha nan petitt
Ma bamtou waat ko
Nit nité ci guen
Jamono ji gnu tolu ni nyepay doranté guenn
Doranté deun
Ku né ni ya fi meun
Kaana xamoni yalla bur bi rek moy ki meun
Nit nitey garabam
Waye xamal ni nit de nit moy posonam
Jotna gnu raxas xol yi te fakhas
Xel yi xamni ignane du bagass
Nit nitey, molay taha done nit yee
Andak Teck ak tey
Marnan bumu la takha nane petitt
Nit nitey
Mole takha done nit
Andak Teck ak tey
Mar naane bumu la taha nane petitt
Kuyabo xamni
Yalla xaratul yamal xiyam
Joni joni lay atté yeah
Kon luway def bopam
Kuyabo xamni
Yene negg la borom atchey fanane
Nagnu yenente jamm waye
Fu jamm am fofou lay fanane wawaw
Nit nitey, molay taha done nit yee
Andak Teck ak tey
Marnan bumu la takha nane petitt
Nit nitey
Mole takha done nit
Andak Teck ak tey
Mar naane bumu la taha nane petitt
Written by: Papa Kande Sidibe

Loading...