album cover
Dale
969
African
Dale was released on December 15, 2017 by Prince Arts as a part of the album Woyalama
album cover
Release DateDecember 15, 2017
LabelPrince Arts
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy
BPM

Music Video

Music Video

Credits

PERFORMING ARTISTS
Aida Samb
Aida Samb
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Aida Samb
Aida Samb
Songwriter

Lyrics

Ayway buuroo, buuroo dale la waay
Khady Sall yaay di buuroo, tay la lay wayal dare
Ayway buuroo, buuroo dale waay
Khady Sall yaay di buuroo, tay la lay wayal dare
Dañ la denk Sëriñ Busóo
Yenn ñaar ngéen bokk menn maam
Nday Astu nga bokkal benn baay
Khady sama Khady
Tay la lay wayal dare
Awa Bàlla, Astu njaay
Fat Jóop Samb Ngóone Alaj
Astu Niang, Xar gneta Sylla
Seynabou Fall, maa Jojo Modj
Ayway buuroo, buuroo dale la waay
Khady Sall yaay di buuroo, tay la lay wayal dare
Soxna Awa Balla, Modu Awa Balla
Awa Balla Coumba Ñuul, maa jeng wala ma ci
Yàgg ngaa dégg dale
Aladji Sëriñ Sall ca baay yàgg na dégg dale
Yaayu Awa Balla buu ndaw, yàgg ngaa dégg dale
Wooy dale, wooy dale, wooy dale
Tay la lay waral dale
Ayway buuroo, buuroo dale la waay
Khady Sall yaay di buuroo, tay la lay wayal dare
Wooy dale, wooy dale, wooy dale
Tay la lay waral dale
Way nala, jiñ nala, bàkk nala dale
Way nala, jiñ nala, bàkk nala dale
Xaadi way nala, jiñ nala, bàkk nala dale
Way nala, jiñ nala, bàkk nala dale
Way nala, jiñ nala, bàkk nala dale
Yaayu Awa Balla buu ndaw, Xaadi bàkk nala dale
Ndeye Astou Sall nga bokkal baay, Xaadi bàkk nala dale
Ibrahima Sall nga bokkal baay, Xaadi bàkk nala dale
Way Nala, jiñ nala, Xaadi bàkk nala dale
Written by: Aida Samb
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...