Lyrics

Taye thi soubeu mane dama dadiek khalei bouma neikh mane ma ladjko Touram Mouneima way sali la toud Mane maniko sali mane damala beug (×2) Taye thi soubeu mane dama dadiek khalei bouma neikh mane ma ladjko Touram Mouneima way sali la toud Mane maniko sali mane damala beug (×2) Wantei sali neima noboumala wuy yayo yaye mane amna naakkar Ndax mbeuguel ndekeitei yaye mom amna dolei Tey yaye boy yaye sali la beugg mane Salimata salimata woy salimata Salimata sali mane iow la beugg 2x Ah gaay lekk gaay bañ Ku la lekk déh Ku la nan mandi Ku la raay guénu rew Ah gaay lekk gaay bañ Ku la lekk déh Ku la nan mandi Ku la raay guénu rew La lam jiiru yakka mënë naw Ku la lekk déh Ku la nan mandi Ku la raay guénu rew Taye thi soubeu mane dama dadiek khalei bouma neikh mane ma ladjko Touram Mouneima way sali la toud Mane maniko sali mane damala beug (×2) Taye thi soubeu mane dama dadiek khalei bouma neikh mane ma ladjko Touram Mouneima way sali la toud Mane maniko sali mane damala beug (×2) Wantei sali neima noboumala wuy yayo yaye mane amna naakkar Ndax mbeuguel ndekeitei yaye mom amna dolei Tey yaye boy yaye sali la beugg mane Salimata salimata woy salimata salimata sali
Writer(s): Uche Ezra Augustine, Youssou Madjiguene Ndour Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out