Music Video
Music Video
Credits
PERFORMING ARTISTS
Akhlou Brick
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Mamadou Sarr
Songwriter
Pape Sidiya Sene
Songwriter
Lyrics
Ba yaw ba nam nga ma
Mandama la nam ba nam nimala namé eh eh
Té yaw bb tam nga nak, dieul peage bi raw ma mai nak tay ma feul pé eh
Bb yaw ba aimer nga ma man damala aimer ba aimer ni mala aimer eh eh
Tè Yaw bb diaral ngama dohé ak ay dal wegn thi desert bi bamou dieh ehh
Bamou dieh Bamou dieh
Def ma ndank yama meun thi pét ma nangouwat ko thi diam Lay doh
Wahone nalako thi souba faw ma bamtouwat ko.
Damala Love
Yaw Damala love
Té Andou mathièk sago
Bb Dama la Yeah yaw dama la love
Mala topé dina dof baby
Nenga man rek malay togn
Wanté boudoul man kénén kan moko sagn
Nenga man guéné sa rangogn
Malay togn ba fou togn yam dik balou la té do bagn bae
Yensay dina yeukeuti bat mér nela May nala baat
Yaram bi daw ma reuthiou wah djou gnew dila balouwat
Nela bae dama don foo
Dama tam ay wahou dof
Hana dou May Tom yay Jerry Beuganté man ta gnak thiow
Yaw sekhou gnou mak yaw demal ma dem
Awma mot hep na JTM motah malay wah dam la bagn
Mais dam la nop menoul am prix yaw am nga prix nobel
Man dama la nop dam la nop ba lap thi guédiou nobél
Love you
Written by: Mamadou Sarr, Pape Sidiya Sene


