Lyrics

Keep kou la bayi nguiir aduna Bayiko té dessé ak Yalla Yalla yoor mbiiram, yoor sa mbiir (hun hun) Barri na loy nawé niit Walahi bo xamone lamou niak door ko am Di nga xam ni amoul wayé dafa gueuneu niakka Deff Music Check Am wala niak lep yallah leu Mais takhoul nit tègui si lokhom Amna am am you sax niak gueun Dou kou gnak rék torokh Esk nak mboolo mooy doolé fou béneu nitt di lekk alalou mboolo Bignkossiy guèn café meunoul soukeur Beugouleu fay naar bi khorom Benefice feegn na mais fayoussi borom Lekk na akh mais dou feegn si boolam Lépeu leu raath dieumeulé thi boram Khol baagui takk yallah fayna kholam Defna ni mom domam doon na doomam Beugoul lim beug baye dja rayna doomam Bayoul di doundei khagn na lekk doomam Baykatt bi dead na doomam diayna toolam Amga alaal Amoo nitt Sa chien de garde Moola faat Oh my god Awma gatt Tok di khaar Ndool dila faat Sama yoon Si iow la kane Lane ngueu meun walabok lane nga xam Fuck sa niakh Fane nga far Koula yabal negger iow la kane Bagnkat ba bagn sa bop yeufou doff leu Gnee katt ak loum meunti am dafay pauvre Gnee katt lougn beug amko esk noon leu C'est pas toujours k l'argent fait le bonheur Paré fay louné pour laver sa honneur Waw setal sa der bala biss bignlay sangu Nakh lep ngafiy baayi sa dieuf yilay topeu sax daniufiy dessaat ndekkei mooy sa alal Kii dafa am faaté yaayak baay (iyeah) Kii bamouy am dafa niak yaay (iyeah) Des fois nak niarignou li nga am (iyeah) Niak rk mooy takh nga meun ko xam (iyeah) Amna niou doyloowoul louniu am (iyeah) Nane laniuy doyloowé yallah (iyeah) Néwougnla nga doylo li nga am (iyeah) Mooy nga bagn wouti loo niak (iyeah) Lou kheuy sootiiii amoul Yallah noopiiiii Nakh moo am Teh meunoul niakk Yallah am Teh dou niak Yallah rek am Meunoul niak Yallah am Teh dou niak Yallah rek am! Yeah Amna niou khiif mais chak jour niou guiss nitt di touridji lek Amna niu tiim sen deukeundoo waayé mayougnko kerr Amna niu miir amna niu tarkhiiss ba niak si ndaw Rangooniu liir bouniu saani tokhoul fim wara tokh Amna niu niak mbeuguel si baye mais doom nak niooko fonk Amna niu amoul mbeuguel si sey mais doomalenfa takha tokk Amna niu yallah may dieukeur si kaw niéneen waayé beugougnko bokk Amna niu mbeuguel, tagaleek sago parce que nioom dagnléna wor Yeah ndakh Valeurs ak principes, guètt booy sammeu leu Beug lep légui guent bouy sank leu Erreur booy rèthiou day melni sank leu Mais nitteu matoul ndioumté pour diang leu Niakagoul dara boudé toutt tank leu Weer lep thi kenen teklé say tank leu Mbeur boufi daanou pekhei bou antou leu God wakhoul dara tèreem di adouneu Nitt dina def louko niakaloo li gueneu cher Nitt dina fèn fèn ba am deug si kaw gnissi dess Nitt dina dead fekkifa loumou amoulwoon si souf Nitt dina dem baayifi ay dieuf youko terei mouth Amna ay milliardaires si séni bop you nékoul ay millionnaires si séni compte Amna ay milliardaires si séni compte You nekoul ay millionnaires si séni bop Nit dina bagnal kou am mayou yallah Tek yallah nit kou am mayou yallah Nit moogui defar nitt moogui yakh Mais nitt niaakoul dara bou amé yallah Lou kheuy sootiiii amoul Yallah noopiiii Nakh moo am Teh meunoul niakk Yallah am Teh dou niak Yallah rek am Meunoul niak Yallah am Teh dou niak Yallah rek am! Gni am Yalla, Yallay buur Gni Gnakka Yalla, Yallay buur Am Yalla, gnakka Yalla, Yallay buur
Writer(s): Baye Dial Gueye Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out