Credits

PERFORMING ARTISTS
Obree Daman
Obree Daman
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Obree Daman
Obree Daman
Lyrics
Delahaye Olivier
Delahaye Olivier
Composer
Sy Abdoulaye
Sy Abdoulaye
Composer
Diagne Pape Moussa
Diagne Pape Moussa
Composer
PRODUCTION & ENGINEERING
Nautylusprod
Nautylusprod
Producer

Lyrics

Ah Ah
Tallal say
Loxo te jeem
Ah Ah
Tallal say
Loxo te nangu yen wee
Tallal say
Loxo te jeem
Tallal say
Loxo te nangu yen wee
Ah jaww ji na ñu ci jappale
Heee
Doomu Àdama
Ay mën-mënam
Waru ci tappale
Huuu
Moo xam muy goor mbaa muy jigeen
Doomu Àdama Yàlla fi mu ko feete leer na
Moy gas muy suul gancax amatul
Baadoola matle wul
Gancax gi gën a tooy
Hiii Heee
Gancax gi gën a tooy
Hooo Weee
Tallal say
Loxo te jeem
Tallal say
Loxo te nangu yen wee
Tallal say
Loxo te jeem
Tallal say
Loxo te nangu yen wee
Find your way back
Only your can fly
Know that you can
Find your way back to
No man, no young, no woman, no girl
No black, no white, no high, no low
Tallal say
Loxo te jeem
Tallal say
Loxo te nangu yen wee
Tallal say
Loxo te jeem
Tallal say
Loxo te nangu yen wee
Bantu bale
Bantu bale
Bantu bale
Bantu bale
Written by: Delahaye Olivier, Diagne Pape Moussa, Obree Daman, Sy Abdoulaye
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...