Music Video

Obree Daman - Banneex [Audio Officiel]
Watch {trackName} music video by {artistName}

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Obree Daman
Obree Daman
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Obree Daman
Obree Daman
Lyrics
Olivier Delahaye
Olivier Delahaye
Composer
Abdoulaye Sy
Abdoulaye Sy
Composer
PRODUCTION & ENGINEERING
Nautylusprod
Nautylusprod
Producer

Lyrics

Kula faale wul man mii maa lay faale Doon sa seetu kula xool man lay gisaale (Bis) Ci sa bët laay xool naan la I Love You Baby yow yaay sama life (Bis) Baby yow yaay sama life Suma Yàlla bëggee wax len ko na ma baayi ak yow Ndax ku melni yow amatul ci àdduna Sama xol laa la def bëgg dëgg laa la def te duma sooraale Benn noon ndax yaay sama life Ci sa bët laay xool naan la I Love You Baby yow yaay sama life Baby yow yaay sama life Kula faale wul man mii maa lay faale Doon sa seetu kula xool man lay gisaale (Bis) Ci sa bët laay xool naan la I Love You Baby yow yaay sama life (Bis)
Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Oumar Samb Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out