Music Video
Music Video
Credits
PERFORMING ARTISTS
Aïcha Koné
Performer
Ousmane Bongo
Performer
Zox Zox
Piano
COMPOSITION & LYRICS
Aïcha Koné
Composer
PRODUCTION & ENGINEERING
Zox Zox
Mixing Engineer
Lyrics
Couplet 1
Eh! Man kham na li léne nakari sougne sagnone nima mel legniy mel (mayou Yalla leu dou nène)
Té sougne sagnone damay torokh sama doundou doumci am louma nékh (dinagne fa dé ndakh man Yalla ma téral)
Séni commentaire yeup laye bokhogne sandi
Man légniy bania guiss nagnou taal gaz tog ci
Boukki meunoul titeul goumbeu ndakhté goumbeu guissoul dara
Pour yène meune nguène ma yeungueul gueune leine daur ndakh yeugouma touss
Mais gni nio faux
Rater seu vocation
Wéssou woul nga tog di wakh ci nite souba ba ngone (tchim)
Séne crush yi man légne nop
Séne far yi man légne fan
Bagne bagne beugue yallay dogal
Di nguene nangou maafi né
Pré-refrain
Nopalou leine, dal lou leine
Ndakh seine wakhi safouma sakh
Am yaye diou bakh dioudo fima wara dioudo ehhh seine wakhi meunouma saff
Refrain
Fi Yalla rékafi né (zembéré, zembéré, zembéré)
Gni khamalougne ma dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Dégniy zembéré bamou nékh (zembéré, zembéré, zembéré)
Damay doundou louma nékh meunougne ci dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Fi Yalla rékafi né (zembéré, zembéré, zembéré)
Nioune ragalougnou dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Dégniy zembéré bamou nékh (zembéré, zembéré, zembéré)
Damay doundou louma nékh meunougne ci dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Pont (griot)
(Griot) kholal, kholal gnane dafa tardé daa nieuw fékk Yalla paré
Yallaay khool louko nékh def ci mom louko nekh
Aïcha, ya meune ya eupp dolé ya gueuneu fëté khalé
Yeureum léne diégueul leine thiouthie dey kham lékam waaay
2ieme couplet
Nieuweul, gueum naa sama bopp tekci goumbeu tekhlou
Dara safouma, adj sama level douma guéstou
Awma temps, man damay liguey waay
Khalé bou ndaw ma wara téral yaye
Waa gni dougne pousse fii
Amougne lougne def
Am nagne diote daal
Awma béneu temps boy!
Man damay thiouthie fi
Di thiouthie fé
Souma nékhé thiouthiati fé
Awma béne temps mangci outoume koppar!
Pré-refrain
Nopalou leine, dal lou leine
Ndakh seine wakhi safouma sakh
Am yaye diou bakh dioudo fima wara dioudo ehhh seine wakhi meunouma saff
Refrain
Fi Yalla rékafi né (zembéré, zembéré, zembéré)
Gni khamalougne ma dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Dégniy zembéré bamou nékh (zembéré, zembéré, zembéré)
Damay doundou louma nékh meunougne ci dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Fi Yalla rékafi né (zembéré, zembéré, zembéré)
Nioune ragalougnou dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Dégniy zembéré bamou nékh (zembéré, zembéré, zembéré)
Damay doundou louma nékh meunougne ci dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Outro
Nopalou leine, nopalou leine
Téla nangou dafay yombal ay douma waay
Nopalou leine, nopalou leine
Téla nangou dafay yombal ay douma waay
Nopalou leine dal lou leine
Ndakh seine wakhi safouma sakh
Nopalou leine dal lou leine
Ndakh seine wakhi safouma sakh
Written by: Aïcha Koné