Lyrics

Yay booy kay jël ma bala ma dee(dee) Yay booy kay jël ma bala ma dee (dee) Picc miile noppil dom Anh noppil dom Picc miile noppil dom Xam nga bala jànt bee soox Sa yay ñëw jël la Yayo Yaye Yaye Danga ma bëgg nax yay duu ñëw Danga ma bëgg nax yay duu ñëw Danga ma bëgg nax yay duu ñëw Ndaxte yay buu doon ñëw,ñëw na Nëw na ba jànt feggee Yayo Yaye Yaye Sama yaay wàllu ma Sama yaay wàllu ma Sama yaay booy wàllu ma Sama yaay wàllu ma Ndaxte yaay xam na bët yi ma tiim Di maa xol du bët i jàmm Yaayo yaaye yaaye Sama xam-xam soriwul Sama xam-xam yaayo soriwul Sama xam-xam soriwul Wante yaay xam na li duu neen Yay booy kay jël ma bala ma dee(dee) Yay booy kay jël ma bala ma dee (dee) Yay booy kay jël ma bala ma dee(dee) Yay booy kay jël ma bala ma dee(dee) Picc mee sa yaay sama xarit la Picc mee sa yaay sama xarit la Bañ lu la lor moo tax ma togg ci suufu garab bi di la xol Li ma soonal yaay mooy Li ma jaxal yaay mooy Li ma tiital yaay mooy Moo di dama bëgg a naaw fekk i yaay Moo di dama bëgg a naaw fekk i yaay Moo di dama bëgg a naaw fekk i yaay Moo di dama bëgg a naaw fekk i yaay Moo di dama bëgg a naaw fekk i yaay Wuy yaye boye (moo di dama bëgg a naaw fekk i yaay) Danga ma bëgg nax yaay du ñëw(moo di dama bëgg a naaw fekk i yaay) Ndaxte yay buu doon ñëw,ñëw na Nëw na ba jànt feggee (moo di dama bëgg a naaw fekk i yaay) Li ma sonnal yaay(Moo di dama bëgg a naaw fekk i yaay) Li ma tiital yaay(moo di dama bëgg a naaw fekk i yaay)
Writer(s): Mouhamadou Kabou Gueye Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out