Music Video

Credits

PERFORMING ARTISTS
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
Songwriter
Mike Bangerz
Mike Bangerz
Composer

Lyrics

Io waxma Nanelay deff Meunuma ci dara Mane xxawma Lanelay deff Meunuma ci dara Waxnako deguma Meunuma ci dara Choix wam leu Choix wam leu Meunuma ci dara Kaféwukok dara Waxtanewuko Meunuma ci dara Ahh yeahhh Ni dal leu deimei Su feikkei beuguetoula delu Nañ koffi bayi mouy weundeilu Bumacci keine garuwalei Mane waxumako nañ nobanté Majeure leu mom teu werneu Té neineu yeug yeuguem leu Bess bunei maniko mu delu Munema beuguetoula delu Mane sax dal bayinako Mbeuguel dh bou xassei djukk Keine meunuki teye Choix wam leu Choix wam leu Choix wam leu keissei Te mom sax Da bayi njabotam Té neineu dotul delu Ahh yee ahh yee Dumacci dara Ahh yee ahh yee Meunumacci dara Bu feikkei beuguetoula delu Nañ ko fi bayi muy wendelu Bumacci keine garouwalei Mane waxumako nagn nobante Majeure leu mom teu werneu Te neineu yeug yeuguem leu Bess bounei maniko mu delu Munema beuguetoula delu Buma keine wax Teyei wumako Dafay soga beug Mbeuguelo mbeuguel Bu djoguei keine dotuko teiye Mbeuguel woy mbeuguel Bu jogue keine meunuko teiyei Ahh yee ahh yeee Bumacci keine garuwalei Bu feikkei beuguetula delu Nañ koffi bayi muy wendelu Bumacci keine garouwalei Mane waxoumako nagn nobantei Majeure leu mom teu werneu Te neineu yeug yeuguem leu Bess bunei maniko mu delu Munema beuguetoula delu
Writer(s): Bryan Cox, Jermaine Dupri, Usher Raymond Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out