album cover
Liggeey
16,244
World
Liggeey was released on September 5, 2000 by Rhino/Warner Records as a part of the album Joko: the Link
album cover
Release DateSeptember 5, 2000
LabelRhino/Warner Records
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy

Music Video

Music Video

Lyrics

Teranga Doomu adama
Liggéey doŋ ka mën a joxee
Te li mu néew-néew
Mooma gënal lenéen li ma mën ti am
Jamono liggéey, jamono liggéey lañu nekk
Liggéey war na góor, war na kiy jigéen
Foo wara tekki, tekkiwoo fa doyna waar
Nekk ci palas wara liggéey te liggéeyoo
Bës bula xa ca raw, boobee bës dem na
Te beneen bi ñëw te xamuloo lu mu àndal
Ma nee tàkku liggéey dafa jot
Liggéey léen
Liggéey na nga liggéey (moo yoor réewmi)
(liggéey) foo mën a nekk (na nga liggéey)
Foo mën a tollu(liggéey) moo yoor réewmi(liggéey)
(Liggéey) foo mën a nekk (liggéey) foo mën a tollu (liggéey)
Moo yoor réewmi (liggéey)
(Liggéey) foo mën a nekk (liggéey) foo mën a tollu
Kàttan bi sax, moon di na mës a jeex
Kaay ñu liggéey, liggéey taxawu sunu jàboot moo gën
Maa ni bës bula xa ca raw, boobee bës dem na
Te beneen bi ñëw te xamuloo lu mu àndal
Ma nee tàkku liggéey dafa jot
Liggéey léen
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome, welcome so easy
Na nga Liggéey, dollil liggéey (moo yoor réwmi)
Na nga liggéey(foo mën a nekk) na nga liggéey(ag foo mën a tollu)
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome, welcome so easy
Liggéey, dollil liggéey (moo yoor réwmi)
Na nga liggéey (foo mën a nekk) na nga liggéey
(ag foo mën a tollu) naa nga liggéey
Loo mën a amiit(naa nga liggéey)
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome, welcome so easy
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome
Tell like wish welcome, welcome so easy
Written by: Kabou Gueye, Youssou N'Dour
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...