Credits
PERFORMING ARTISTS
Youssou N'Dour
Performer
Alain Rodrigue Oyono
Saxophone
Augustine Huche Ezra
Programming
Spotless
Programming
Thierno Sarr
Bass
COMPOSITION & LYRICS
Youssou N'Dour
Composer
Augustine Huche Ezra
Arranger
Spotless
Arranger
PRODUCTION & ENGINEERING
Hakim Abdulsamad
Engineer
Lyrics
Tay ci suba, man dama dajeek
Xale buma neex man, ma laaj ko turam
Mu ne ma way Sali la tuddu man
Ma ni ko, Sali, Sali man yaw la bëgg
Tay ci suba, man dama dajeek
Xale buma neex man, ma laaj ko turam
Mu ne ma way Sali la tuddu man
Ma ni ko, Sali, Sali man yaw la bëgg
Wante Sali, ne ma nobumala
Wuy, yaay boy, yaay man am na naqar
Ndax mbëggeel, nekete yaay moom am na doole
Te yaay booy, yaay Sali la bëgg man
Salimata, Salimata wooy Salimata
Salimata, Sali man yow la bëgg
Salimata, Salimata wooy Sali
Salimata, Sali man yow la bëgg
Salimata, you are my Guy
Ayo nene, ya-yay-ya
Salimata, you are my princess
Dégg lo ma xale bi, dégg wo ma xale bi
Dégg lo ma, dégg loo
Dégg lo ma xale bi, dégg wo ma xale bi
Dégg lo ma
Dégg lo ma xale bi, dégg lo ma xale bi
Dégg lo ma
Salimata, Salimata wooy Sali
Salimata, ma xel, yaw la bëgg
Written by: Youssou N'Dour