音乐视频

Élage Diouf & Johnny Reid - Just One Day
观看 {artistName} 的 {trackName} 音乐视频

制作

出演艺人
Elage Diouf
Elage Diouf
表演者
作曲和作词
Elage Diouf
Elage Diouf
词曲作者
Johnny Reid
Johnny Reid
词曲作者

歌词

Souma déssé wone béne bés cii dunya Dina khoole limay yobalé ak mane, ak limay bayi fi cii Aduna Na taxaw ame samaa foula'k fayda, samaa lamigne dara Douthie gueneu loudoul balaaté Souma dessé wone béne waye cii dunya Souma dessé wone béne waye cii dunya Souma meunone wakh béne wakh, aduna bi nieup daal Di maye dieuli Sou waye wi meuné aame ndeysane, ba nieupe diko yek Niome daal cii sene yarame moo Souma dessé wone béne waye cii dunya If I had just one day left to live Would I take or would I give? Would I stand up on a mountain, would I miss you on My lips? Souma dessé wone béne bés cii dunya Yeah yeah yeah yeah... If I had just one tear left to cry Would it fall for hello or goodbye? Dina léral sama guinaw, ba xaleyii nieuwe meune thiée Barkéloo If I had just one tear left to cry Yeah yeah yeah yeah... Souma dessé wone béne bés cii dunya Souma mounone wakh béne wakh, aduna nieup daal Dimaye dieuli Sou waye wi meuné aame ndeysane, ba nieupe diko yek Niome daal cii sene yarame moo If I had just one song left to sing Yeah yeah yeah yeah... If I had just one day left to live Souma déssé wone bene bés cii dunya.
Writer(s): Elage Diouf, Johnny Reid Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out