音樂影片

音樂影片

積分

詞曲
Seydina Oumar Samb Guèye
Seydina Oumar Samb Guèye
詞曲創作
Charles Diagne
Charles Diagne
詞曲創作

歌詞

Mbeuguel la nekk ci sama xol
Wai adouna nyu sonal lol
Xol bu fess ak baneex
La la yeené won ci adouna
Mbeuguel gima am ci yow
Mba duma sonal lool
Diafé diafé adouna
Ak bokk gui yallah burr bi bole
Kon mbeuguel lay adouna
Ndax Yallah mo nyu bolé
Sama yeene yaatuna
Mangi nyaan ndax Yallah mey nyu dolé
Dugu na ci gaalu mbeuguel, ndox mi yobuma
Ngelew langui mai indi ci yow
Nyu guissé leer na ma
Mbeuguel moi li leeral adouna
Xam nga yow la beug lool
Sama yeené yaatuna
Mangi nyaan mu yoku
Denk na la yallah
Denk na la sama xol
Sasu ma djuli di la nyaanal
Sama xol la ko tibé
Denk na la yallah
Denk na la sama xol
Sasu ma djuli di la nyaanal
Sama xol la ko tibé
Kon mbeuguel lay adouna
Ndax Yallah mo nyu bolé
Sama yeene yaatuna
Mangi nyaan ndax Yallah mey nyu dolé
Dugu na ci gaalu mbeuguel, ndox mi yobuma
Ngelew langui mai indi ci yow
Nyu guissé leer na ma
Mbeuguel moi li leeral adouna
Xam nga yow la beug lool
Sama yeené yaatuna
Mangi nyaan mu yoku
Written by: Charles Diagne, Seydina Oumar Samb Guèye
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...