Lyrics

Sama xol bo ma tàgguwoon Do ma yóbbe biile coono Sama xol bo ma tàgguwoon Do ma yóbbe biile coono Mar a naan te ragal ndox mi Oh mbëggeel Hann manak mbëggeel Sama xol bo ma tàgguwoon Do ma yóbbe biile coono Sama xol bo ma tàgguwoon Do ma yóbbe biile coono Picci miy naaw la, dafaa gumba Dafa dul xool fa muy jógee Dafa yor tàngaay u Jaxalnama Ak sedday u Aljana Oh mbëggeel Hann manak mbëggeel Oh mbëggeel Hann manak mbëggeel Sama xol bo ma tàgguwoon Do ma yóbbe biile coono Sama xol bo ma tàgguwoon Do ma yóbbe biile coono Mar a naan te ragal ndox mi Oh mbëggeel Hann manak mbëggeel Suma jógee ba jëm ci moom Giir yeggee ko sumay xalat Sama fit wi daldi key raggal May wëndéelu, jaaxle lool Oh mbëggeel Hann manak mbëggeel Oh mbëggeel Hann manak mbëggeel Te bu siggee, xippi, xool ma Sama dunya bëgg a yëngu May wëndéelu, dii waxtu Man de xalat samay pexe Oh mbëggeel Hann manak mbëggeel Oh mbëggeel Hann manak mbëggeel Picci miy naaw la, dafaa gumba Dafa dul xool fa muy jógee Dafa yor tàngaay u Jaxalnama Ak sedday u Aljana Oh mbëggeel Hann manak mbëggeel Oh mbëggeel Manak mbëggeel
Writer(s): Coumba Gawlo Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out