Lyrics

Loumou meu wakh Ma diko deff Daffey deuk ci dima togn Teksi manane ko balma Wayé mom la nobb Sou mako guissé Samey beut di mélakh Samey tank djakhasso Sama lamign rère ma Mom la nobb Amadou amadou Guéstou ma Man sama yaye maymeu amadou Amadou amadou Guéstou ma Man sama yaye maymeu amadou Amadou amadou Damey gueumlo lou amoul Téréwoul ma diko gueum Tékci manane ko balma Wayé mom la nobb Sou mako guissé Samey beut di mélakh Samey tank djakhasso Sama lamign rère ma Mom la nobb Amadou Amadou Guéstou ma Man sama yaye maymeu amadou Amadou amadou Guéstou ma Man sama yaye (yaye boye maymeu amadou) Amadou amadou Guéstou ma Man sama yaye maymeu amadou Amadou amadou Guéstou ma Man sama yaye maymeu amadou Amadou Amadou (...) Sa youma digué woté téléphone Ci téléphone bi lay yéndou Sa youma digué ab setsi Ma yéndoo wadjal Khamnani nobb na kénéne koudoul man Oh yeg nani mingui seti kénéne koudoul man Wayé mom la nobb Amadou amadou Guéstou ma Man sama yaye maymeu amadou Amadou amadou Guéstou ma Man sama yaye maymeu amadou Amadou amadou Guéstou ma Man sama yaye (sama yaye boye maymeu amadou) Amadou amadou Guéstou ma Man sama yaye (sama yaye boye maymeu amadou) Amadou amadou Guéstou ma Man sama yaye (sama yaye boye maymeu amadou)
Writer(s): Coumba Gawlo Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out