Lyrics

Dafa gneuw dindi leppe lou fi leundeumone Leral féppe mome képpe Lolou loukey dindi Lou thiow Li beuri beuri Mome mofi né Mom reeek Dafa gneuw Oubi bounte yi Soutouralma Teralma Woné ma fépp Dessélatouma dara Bamouy métti mome rekafi néwone Mome rekkk Dagnou wouté Sama bosse deh dou gneulé Damey begué Limou meune la gné teulé Souma teudé mou lébeul meu bama nelaw Souma guissoulé dafay dof mane la nope Yéne saye mouné ma Yaye Sama aldiana Khol bi fekh mou déy ma Sa rétane louné na Loumou ame bokak man Mane maye première daamam Kholoul kénéne koudoul mane He's my Superman Ndourowoutak gnom Bokou gnouy féme Ndourowoutak gnom Non non dougnou béne Ndourowoutak gnom Bookougnouy féeeeme Ndourowoutak gnom Non non dougnou béne Sama boss Dou door dou saga dou worr Gawna thi mane Mané Sama boss Sama bosse Dou door dou saga dou worr Gaw na thi mane Beau neu gentle na Khol bi rafet na Loumou kham wakh ma Fouma néee tamit moungui faaaa Damey khool ak beutou mbeuguel Dima waaakh aye wakhou Nobeel Love na ma ba doff kholam maye boroome Kéne la si gnom non amoul morome Deugueuntane la mane ley béguéee Dou aye fooo mane rek la aiméee Yéne saye mouné ma Yaye Sama aldiana Khol bi nekh mou dey ma Sa retane louné la Loumou ame bokak mane Mane maye première daamam Souma guissoulé dafey dof mane la nope Ndourowoutak gnom Bokougnouy féme Ndourowoutak gnom Non non dougnou béne Ndourowoutak gnom Bookougnouy féeeeme Ndourowoutak gnom Non non dougnou béne Sama boss Dou door dou saga dou worr Gawna thii mane Mané Sama boss Dou door, dou saga dou worr Gawna thii mane Ndourowoutak gnom Ndourowoutak gnom
Writer(s): Nguenar Diouf, Nick Silver Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out