Lyrics

Li lagn done ñane Meel nani ñaneu yi nangu na Ñune Li lagn done xare Bess bugn lay wathièl soxna Té keurgui koffi xool tout le monde à la joie Tout le monde à la joie Waay diaroul waax saax ouais ouais sa se voit Ouais ouais sa se voit Oie Papam ak aay xaritaam di wadj deem diouma Baniou taak seuy bi rek niou sandi Duaa Ngaay degg heureux ménage heureux mariage Niou laay tagaal say louanges Ioe Yaaya boy xaritaam yi dikoo ndokalè Tay nga faayu booru Ndawtaal yign la ameel fuunè Waay daniuy xawaré tagaté bamou Saf Taay daniuy xawaré Mane Taak na diabaar Deef na liwaar Degg na deuku na mbeur Way dafaa doone li waar Ndaax daaf may nekh lol nioumaay wowei Aladji Bébé d'amour bébé Aladji Wawaw Aladji Wawaw Aladji Mane daf may nekh lol nioumaay wowei Aladji Bébé d'amour bébé Aladji Wawaw Aladji Wawaw Alaaadji Beuss du tutii Beuss dou borom reik laay tolool Saa ligueyu ndaay molaa wuyussi Nieupeu d'accord nagn si lolou Waay Taay daniuy daal di bâche kogn ba kogn Xaar yi niou raay, guinaar yi niou ndiogn Niou yeggal niveau bi adj bassi kowakow Kou aayé wonè sa momé Taay yaa momè Oie Papa ak aay xaritaam di wadj deem diouma Baniou taak seuy bi reik niou sandi Duaa Ngaay degg heureux ménage heureux mariage Niou laay tagaal say louanges Aladji gueneu ak nietti pièce machallah Xaarit yi daar ko diiko djine djino djign Deem gatandou dji madame gane bi yeksi na Neko bismillah Taay daniuy xawaré Mane Taak na diabaar Deef na liwaar Degg na deuku na mbeur Way dafaa doone li waar Ndaax daaf may nekh lol nioumaay wowei Aladji Bébé d'amour bébé Aladji Wawaw Aladji Wawaw Aladji Mane daf may nekh lol nioumaay wowei Aladji Bébé d'amour bébé Aladji Wawaw Aladji Wawaw Alaaadji Wuyuma Aladji Si geew gui oie laaniuy xaar Aladji Aladji Beuss bi sa beuss leu Aladji Goudi gui Yaa momeé Aladji yeah Eeeweh Sama Aladji aaah Aladji aladji Sama Aladji ooohoh Aladji Sama Aladji
Writer(s): Djiby Ka Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out