Lyrics

Li gën ci ndab li man lay ñëw këf Ñi bék moom seen yaakaar tas Guerre ak man yombul dama mëna bis Ma ci tekk loxo te matax ngeen gej ko gis Ki ngeen doon xëcco la def copet Doo leen ci papa Ndiaye may bondit Sax dama tàng fum leen fekk ngeen allumette Jël ko seen loxo pare taxal guerre guerre bi Man li ma moom Loxo bu ma ci fekk nga yërëm boroom Ki ba ko Yàlla di sàkk man ma taxaw Seeti leen leneen ki buur tekk na ci loxom Sama lekk la tégil say bët ci moom Jaay ma guerre bi, jaay ma guerre bi Jaay ma guerre bi, jaay ma guerre bi Ku ñeme nanga taxaw Ku ragal nanga daw Ki ku ko bëgg nangu ci man dangay raag ak man Kon jaay ma guerre bi, jaay ma guerre bi Ki may ki ko tëye man comme ku ngëb dërëm Ngeen doo tàcc du yomb dam leen yërëm Dama tébbi aas tax seen coeur yi di baax Mënoo jël sama place liggéeyoo fi lu tax Man la diiw beurre bi (Billaay yaw ma diiw beurre bi) Ñun la àjja ak àlaaji Su ma koy ajj di ko ajjil Chérie boy, chérie boy Daf ma tànn ci seen biir Ndax xam naa ni nit ku nitte la Daf ma noba noba ba dof Chérie sama chocolat Ki man la nob (waaw) Dotoo leen ci jot (déedéet) Ndax mënuñu ko bokk Kon demal nga togg Fi amoo fi place Man duma sa mas Seen yaakaara tas Lem leen seen ay bagaas Man la diiw beurre bi (Billaay yaw ma diiw beurre bi) Ñun la àjja ak àlaaji Su ma koy ajj di ko ajjil Chérie boy Jaay ma guerre bi, jaay ma guerre bi Jaay ma guerre bi, jaay ma guerre bi Ku ñeme nanga taxaw Ku ragal nanga daw Ki ku ko bëgg nangu ci man dangay raag ak man Kon jaay ma guerre bi, jaay ma guerre bi Wóolu sa sëriñ su taxe nga yab ma Na la defal baggas Ànd bu dëgger liggéey mënu ci tus comme jouru dimanche Fi loo ëndi fekk ko fi mo yaw dawoo sama yaram Xale bu ci dugg sama 18 tu joues avec le feu Man la diiw beurre bi Ñun la àjja ak àlaaji Su ma koy ajj di ko ajjil Chérie boy
Writer(s): Charles Diagne, Abdoulahat Thioune Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out