Lyrics

Jiggen sou beugué am manorééé... thi seyam! Neu guéné lep, koundioug yék kadiague yi... Boul négligé tar. Neu safeu saf... Beuss bou nekeu... indil féém you bess Boul ko khep djinakh dey bari pakh Gaaatéééko ba foumou dém yow rékeu ley khalate Jiggen sou beugué am manorééé... Dey jonguéééé té bary féém Jiggen sou beugué am manorééé... Dey jonguéééé té bary féém na saf! Fik mingui bék yokal dose bi boulko outeul frontière Na safa saf... Na gueneu saf Pampam piram pampam wata bambam Jiggen sou beugué am manorééé... Dey jonguéééé té bary féém Yow bo beugué am manorééé... Jonguél! Té fékhel beu loumou lamb dadji Té bokou soré dang koy wéteul Té loumou mér mér, fékhél ba mou ré Té bouko niourou dionguéééél ba mou saf! Na faf melni adouna yéén dongua thi né Jiggén sou beugué am manorééé... Dey jonguéééé té bary féém An an... An an an an... An an an an an an... Yow baril féém! Jiggen jonguél jonguél beu mou meut wonél say féém! Ték ko thi temps té civilisé wonél say féém! Djeuffé ko deuké ko wonél sa féém! Mine nguameu mine nala dagnou wara sey yAllah ma bolék yow degnou wara sey Mine nguameu mine nala dagnou wara sey yAllah ma bolék yow degnou wara sey Seyallaaaaa man Samey dooma wara takh meu nanguou lou métti papy Beu fougnou meuneu dém beu fougnou meuneu né An sey bimey sey molène di walooo... Papé! Papy louleu nékhoul thi mane dameukoy dindi Gawémeu gawémeu man yaw lay sét Mbeuguel dou ray ci niaye sou guené fegn Dou ci wakhine dou ci djeufine ... Yow lay sét Louleu nékhoul thi man meu dindi sani Oooooooh papy chéri yow lay sét Papy sou doyoulé meu doli Louleu fi nékhoul dal damakoy dindi Pitakh yangui ni, souleu doyoulé Sou doyoulé meu doli yow lay sétt Papy yAllah bolléna mak yow. Yow lay sét Bayina kharite andando yow lay sétt Djitteul na sameu yakaaar ci yow yAllah bolléna mak yow. Yow lay sét Éééééh djine naleu oooooh man yow lay sét Ééééééh.
Writer(s): Kabou Gueye Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out