Lyrics

Yeah, eh eh eh Lé, lé, walé Hum, hum Yaw lay bëgg jakarlool Sa suma yeewu Yaw lay bëgg njëkk xol Ëlëk lu mata soor la Ëlëk ay jaar-jaar la Sama xol yëgoon nako muy ñëw Xel xalaat la (xel ak xalatam bë) Xol yëkk yëkk la Dara xaaju fë Sa suma yeewu Yaw lay bëgg njëkk xol (Suma yewo yaw la bëgg njekk xol) Yaw la bëgg jakarlool Denk na la guddi Fanané yakkar ci yaw Gent na la guddi gi yëpp Ndax fajar yaw lay jakarlool
Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Arfang Tiare Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out