Music Video

Ashs The Best ft Obree Daman - Gadaay (Clip Officiel)
Watch {trackName} music video by {artistName}

Credits

PERFORMING ARTISTS
Ashs The Best
Ashs The Best
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Ashs The Best
Ashs The Best
Lyrics
Obree Daman
Obree Daman
Lyrics
Olvier Delahaye
Olvier Delahaye
Composer
Abdoulaye Sy
Abdoulaye Sy
Composer
PRODUCTION & ENGINEERING
Nautylusprod
Nautylusprod
Producer

Lyrics

Chiii riii reee Chiii riii reeeraa Ahhhhhhh yeaaaaaaah Ge'stu woo ma Deglu woo ma May laaj lu xew Gisu loo ma Te gisoon naa ni Da nga reer ma lay jeex Da ma fog ni Tayu loo ko ndax mbëggeel Defoon na ni Di nga changer balaa maa dem A'ndandoo bi Ci jamano ji Mën na xaar ba beneen Xarit woo ma Woo ma yee su fekee may nelaw Fi ñu to'll Kan ngay woolu kudul sa xel Balaa maa dem Naa la wax ni am naa coffeel Coffeel bi ma am ci yow Waat naa ni doo ko yëgg Wallaay dang ma miin Ba doo ma yëgg ba maa ngay dem Gestu woo ma Gadaay Gadaay Yëggu loo ma yow Gadaay Gadaay Faale wu loo ma Toppatoo wu loo ma yow (Bis) I know something's wrong Doomu yaay mbaa fate wu loo ma Woote naa te wuyu wu loo ma B'cause I know something's wrong I know something's wrong Maa ngi dox akk ta'nku ne'en Ci naaj bu ta'ng lool Maa ngi mar naan ndox mu jafe lool I know B'cause I know something's wrong Gilee jëlsi xarit sama doomu yaay fi ma toll weet naa Bilee doomu yaay jëlsi ma xarit sama fi ma toll weet naa Doomu yaay jëlsi ma Xarit sama doomu yaay jëlsi ma Mbaa fate woo ma Doomu yaay jëlsi ma Xarit sama doomu yaay jëlsi ma Gëstu woo ma Lijënti woo ma yow Faale wu loo ma Toppatto woo ma yow Gëstu woo ma Xoolu loo ma yow Yëggu loo ma Faale wu loo ma Lijënti woo ma yow Moo tax gadaay naa Gadaay Fii ku fi wac sa'w and and boo dem fekk fa sa moroom mu toog Xale yaa ngi gadaay Bu ja'nt sowee Timis maase Kulay yobbaaleel Ndax Guddi xaaj na Fajar waaj na Ëllëg sooraaleel Reccu wees na Jëffëm fe'eñ na Kookoy diggaaleel Ludul Yalla neen la Yeene neeg la Nga fay fanaane
Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Oumar Samb, Arfang Tiare Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out