Lyrics

Mane tanne nala si jigueen yudul diekh Jokh Nala sama xool bi yaay borom Kone baby boul ma négligé maay sa xool Ndakh malay jokh leep lu geune si yoow Mane tanne nala si jigueen yudul diekh Jokh Nala sama xool bi yaay borooooom Boul négligé xamal ni Yaay sama xool Ndakh beugg nala yoow bae beugg nala Mane So mané waw ma nieuw sen keur Yoow beugg nala yoow bae beugg nala Mane So mané waw ma nieuw sen keur Yoow beugg nala bae beugg nalaa! Woo nala telephone dieulou loo Envoyé nala message wuyuwoo Lane motakh yow babe lane motakh Woo nala telephone dieulou loo Envoyé nala message wuyuwoo Lane motakh yow babe lane motakh Bou mbeguel done diaay Bou mbeguel done diaay Yow babe diokh nala la xool bi Wayé leep yakoo moom Wayé neewoul dama niaak diom Meussuma niaak diom Mane sama mbeuguel moma yobou Motakh malaay wo oh Lane motakh babe lane motakh Soumalay woo tei babe doma dieul Lane motakh babe lane motakh Soumalay woo tei babe doma dieul Yeah yeah yeah Yeah yeah yeah yeah yeah yeaaaaaaaahhh Anh Anh... Ndakh beugg nala yoow babe beugg nala Mane So Mané waw ma nieuw sen keur Yow beugg nala yow babe beugg nala Mane So Mané waaw ma nieuw sen keur Ma nieuw ma nieuw ma nieuw Beugg nala yow babe beugg nala!
Writer(s): Djiby Ka Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out