JIIN
11,961
Afro-Pop
JIIN was released on September 12, 2025 by J à n j a as a part of the album JIIN - Single
Most PopularPast 7 Days
00:55 - 01:00
JIIN was discovered most frequently at around 55 seconds into the song during the past week
00:00
00:30
00:45
00:55
01:10
01:20
01:40
02:35
02:45
03:05
00:00
03:14
Credits
PERFORMING ARTISTS
AMADEUS
Chant Vocals
COMPOSITION & LYRICS
Saliou Samb
Songwriter
Charles Mbaye Diagne
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Jeuuss Beatz
Engineer
Lyrics
Sa ñàkk a teew a raw daay
Bu ma fi ne ñukk gàddaay
Gis naa la ngay sàmbandaay ni gaynde
Jigéen nga waaye jàmbaar nga
Xeebuma la ngir sa melokaan man benn yoon
Jigéen nga waaye jàmbaar nga
Ku ma xool ci yaw
Dina ma mere
Ndax demewuma xel
Ci lenn lu jëm ci yaw
Yàlla Moo dogal
Fu ma la gisee
Tàggoo ak sama sago
Man dama lay téeye
Ak fukki lox
Yàlla ma la nattoo
Man it ma nangu ko lool
Yaa ma leen gënal dama koo rusoon a wax
Jiinoo jiin sama xol neex na
Moo tax jiinoo jiin samay way neex na
Jiinoo jiin sama xol neex na
Moo tax jiinoo jiin samay way neex na
Li may gis samam xel dal na
Ndax tay day neex suba suba Yàlla la
Jiinoo jiin sama xol neex na
Moo tax jiinoo jiin samay way neex na
Bis a ngi ci bis yi
Man ak gaa ñi dinan fëgg sa kër
Dugg ci sabadoor ànd ak paa yi ñëw jox la sa cër
Po mi taxu maa jug damaa aalu ba ma la xamee ba tay
Eeyy waay jigéen nga waaye jàmbaar nga
Xeebuma la ngir sa melokaan man benn yoon
Jigéen nga waaye jàmbaar nga
Ku ma xool ci yaw
Dina ma mere
Ndax demewuma xel
Ci lenn lu jëm ci yaw
Yàlla Moo dogal
Fu ma la gisee tàggoo ak sama sago
Man dama lay téeye
Ak fukki lox
Yàlla ma la nattoo
Man it ma nangu ko lool
Yaa ma leen gënal dama koo rusoon a wax
Jiinoo jiin sama xol neex na
Moo tax jiinoo jiin samay way neex na
Jiinoo jiin sama xol neex na
Moo tax jiinoo jiin samay way neex na
Li may gis samam xel dal na
Ndax tay day neex suba suba Yàlla la
Jiinoo jiin sama xol neex na
Moo tax jiinoo jiin samay way neex na
Bis a ngi ci bis yi
Man ak gaa ñi dinan fëgg sa kër
Dugg ci sabadoor ànd ak paa yi ñëw joxla sa cër
Po mi taxu maa jug damaa aalu ba ma la xamee ba tay
Eeyy waay jigéen nga waaye jàmbaar nga
Xeebuma la ngir sa melokaan man benn yoon
Jigéen nga waaye jàmbaar nga
Ayca kaay nu kelemaayoo
Dama la wóolu
Jigéen nga waaye jàmbaar nga
Written by: Charles Mbaye Diagne, Saliou Samb

