album cover
Digg Doole
album cover
Digg Doole was released on September 25, 2026 by J à n j a as a part of the album Digg Doole
September 25, 2026
LabelJ à n j a
BPM
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy

Music Video

Music Video

Lyrics

Biddeew bu doy waar
Loo def mu ndaysaan
Déggal la muy mbaar
Rógseen a lay aar
Yaw mbaax a la jig
Soo bonee rekk ñàkk i may
Gis sa jëmm jii
Yëg cofeel ci biir xolam
Santaat jinne jii
Su ma deewul dinaa la way
Saytaane rajiim lagal Yàlla a ko may mayam
Jiitu na sa ngan biir dunyaa dangay gaañ
Boroom bi a la mooñaale mbir ya ay waay
Sàccunu ko fenn
Sët ay jël la woon ca maam
Giñ naa ci samay ñoñ ngéwal a neex
Eey samba mi ci digg dooleem
Jamono ju ne jamonoy waay la
Mi ci digg dooleem
Eey waay Yàlla aka bari doole
Jamono ju jamonoy waay la
Sama ñoñ a moome
Jiitu na sa ngan biir dunyaa dangay gaañ
Boroom bi a la mooñaale mbir ya ay waay
Jaam ak jamonoom
Mbër ak tàkkusaanam
Ku nekk ak li nga moome
Te guddi ay gunge biddeew yi
Biddeew bu doy waar
Loo def mu ndaysaan
Déggal la muy mbaar
Rógseen a lay aar
Dégg naa am njoor mu far ma dox dëgmël naa ko
Séen nama am njool rafet man it tëggal naa ko
Tàggu naa mbaar mu tëb dukkat feelu ma lool
Ne ma ayca tëggal ngéwal mbaay
Jiitu na sa ngan biir dunyaa dangay gaañ
Boroom bi a la mooñaale mbir ya ay waay
Sàccunu ko fenn
Sët ay jël la woon ca maam
Giñ naa ci samay ñoñ ngéwal a neex
Eey sàmba mi ci digg dooleem
Jamono ju ne jamonoy waay la
Mi ci digg dooleem
Eey waay Yàlla aka bari doole
Jamono ju jamonoy waay la
Sama ñoñ a moome
Written by: Adrien Mbagnick Diop, Charles Mbaye Diagne, Patrick Ngor DIOP, Saliou Samb
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...