Music Video

Ashs The Best - Wétoon na (BO KARMA)(Clip Officiel)
Watch {trackName} music video by {artistName}

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Ashs The Best
Ashs The Best
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Ashs The Best
Ashs The Best
Lyrics
Nautylusprod
Nautylusprod
Composer
Jeuuss Beatz
Jeuuss Beatz
Composer
PRODUCTION & ENGINEERING
Nautylusprod
Nautylusprod
Producer

Lyrics

Demb wétoon na Dama réron nga fégnal ma Yaw mi ladon khar Fekeu ma ci leundeum niital ma Sama khol wétoon na Dagua nieuw ma kham louy adouna Sa mbeuguél doundalma Yorrma Yarrma Yéma Yeureum ma Damaleu beug beug té Yalla takh paré lepp pour nékak Yaw Nakh demb wétoon na Dama réron nga fégnal ma Yaw la taamo nékal Yaw la nangoul louma meussoul nangoul ken Sa mbeuguél doundal ma Yorrma Yarrma Yéma Yeureum ma Huuuuuu woooooh wooooh Yeah yeah Mbeuguél bi douma gagne Huuuuuu woooooh wooooh nanananana Yeah yeahhhhhhh Mbeuguél bi douma gagne Ndax demb weet na weet na Tay samay nakar diekhna weet na Yakar bou tasson waw Sama khol lama teudion kasso wawaw Banekh bi nieuw na nieuw na Metti won demb tay nekh na nekh na Mak yaw all day all night Sa wet la beug dess mak yaw for life Demb wétonn na (wétoon na) Dama réroon nga fégnal ma (fégnal ma) Sa mbeuguél la nieuw doundal ma (doundal ma) Yorrma Yarrma Yéma Yeureum ma (yeureum ma) Demb wétonn na (wétoon na) Dama réroon nga fégnal ma (fégnal ma) Sa mbeuguél la nieuw doundal ma (doundal ma) Yorrma Yarrma Yéma Yeureum ma (yeureum ma) Uhhhhhh ouhhhhh Mak yaw mak yaw Sa wet la beug dess mak yaw for life So baby beug touma nga sorima Sa wet la beug dess mak yaw all day all night Mak yaw mak all day all night Sa wet la beug dess mak yaw for life Demb wétonn na (wétoon na) Dama réroon nga fégnal ma (fégnal ma) Sa mbeuguél la nieuw doundal ma (doundal ma) Yorrma Yarrma Yéma Yeureum ma (yeureum ma) Demb wétonn na (wétoon na) Dama réroon nga fégnal ma (fégnal ma) Sa mbeuguél la nieuw doundal ma (doundal ma) Yorrma Yarrma Yéma Yeureum ma (yeureum ma) Wétoon na Fégnal ma Doundal ma Yeureum ma
Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Arfang Tiare Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out