Lyrics

Giisoo, yeewu (ha-ha, eh-eh, ha-ha) Xa naa giisoo fu xalaat yi sutte Asamaan Xa naa giisoo ko yaw Loolu moo waral nit ñi wuute Ci xalaat Giisu lo ni, giisu lo ni,fi amna ay bideew Yiy leeral Xa naa giisoo ko Te bu suuf di sedd, suuf ci di sedd guy Du nelaw Xa naa giisoo nuñu mandoo Mbaa melni luy la faale Bu mettee deggu nañ ko Te bu neexee ñu yobbaale Ndeke yàlla ji,moom noppina Te bu suuba ñu yekaliko Motax boo demee bay daanu Xoolatal foy jafanu Du suñu ndam, du suñu cër bu dee, guddee, guddee tinnañu Bu amoon xaaxoo duñu bàyyi, bu de, bu de, bu de ci ñun la Bu amoon leyla du ci moom, weet fi goore te wetaliko sa ngor Waxoon na la duñu bàyyi, bu de, bu de, bu de ci ñun la Ayo noo yèwwoo Ñaan u yaay la yendoo, yendoo Giiso ni naaj na waxee du ñu mës guddee, guddee Bideew yi léer nañ (léer nañ) Yàlla léen fi nekkaloon Bu ñu naaje duñu guddee (duñu guddee) Te bu ñu guddee ñoo ci sa wet Ayo noo yéwwoo Ñaan u yaay la yendoo, yendoo Ayo noo yéwwoo Barke baay la yéwwoo, yéwwoo Giiso ni naaj na waxee du ñu mës guddee, guddee Bideew yi léer nañ Maam Yàlla léen fi nekkaloon Maam Yàlla léen fi nekkaloon waaw Bideew, bideew yi léer nañ Maam Yàlla léen fi nekkaloon waaw Bideew, bideew yi léer nañ
Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Oumar Samb Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out