Credits
PERFORMING ARTISTS
Ashs The Best
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Tiare Arfang
Songwriter
Abdoulaye Sy
Composer
Olivier Delahaye
Composer
PRODUCTION & ENGINEERING
Nautylusprod
Producer
Lyrics
Jëlël caabi kër g, tëj ko, ngiir saay so wéete mu mel ni maa ñi sa wet
Xalam baa ca taat u guy nga
Moom laa la tudde, Bàllago la lay wo wee
Ci gaal g, la nekk di joow
Yaw soo ma nammee, séentu ma ci weer wa
Jaarul ci xàll maam ya
Ci ànd, gàddaay nga
Wéetay bu soon la
Fi dara deesul tu fi (wou-wou-wou)
Dara deesul tu na (wou-wou-wou)
Jébbal na la sa ma xol ag xel
Ngay yëg, lu ka raw lay yëg ci nammeel
Kañ la lay giis?
Hmm-hou-hou
Mbaa suma sore
Mbaa suma sore (mba suma sore do toog mba caalit, do dem bàyyima fi)
Mbaa suma guddee (hou-hou, hou-hou)
Mbaa suma guddee (mba suma guddee mba bët set loori, mba do def lu ñaaw)
Waat na di na ñëw (hou, hou-hou)
Waye xamaguma kañ lay ñëw (Yàlla ma dogal lumay gën di sori, nga gën jegee ci man)
Su may dee ci àll wi (hou, hou-hou)
Yaw yaay gaynde bi may ray (yama tax a fekk ñey bu taxaw, man ma di ko galgal)
Ci kaw asamaan, foofu nga may jëmee
Ci kaw asamaan
Ci asamaan, foofu nga may jëmee
Mba ding ma dèllo, ho-ho-hoho-ho
Ci kaw asamaan
Jëlël caabi kër g, tëj ko, ngiir saay so wéete, mu mel ni maa ñi sa wet
Xalam ba ca taat u guy nga
Moom laa la tudde, Bàllago la lay wo wee (wo wee yaw)
Ci gaal g, la nekk di joow (ci gaal g)
Yaw soo ma nammee, séentu ma ci weer wa (ci gaal la nekk di joow)
Jaarul ci xàll maam ya (jararul)
Ci ànd, gàddaay nga
Wéetay bu soon la (wéetay bu soon la)
Wéetay bu soon la
Jëlël, jëlël
Jëlël caabi kër g, tëj ñu dajee
Maak yaw
Nammeel, nammeel
Waye xamoon nanee bës di nañ daje
Maak yaw
Hu-hu-hu
Yaw jëlël, jëlël
Jëlël way, jëlël
Writer(s): Abdoulaye Sy, Olivier Delahaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com