Credits

PERFORMING ARTISTS
Ashs The Best
Ashs The Best
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Ashs The Best
Ashs The Best
Lyrics
Obree Daman
Obree Daman
Lyrics
Abdoulaye Sy
Abdoulaye Sy
Composer
Olivier Delahaye
Olivier Delahaye
Composer
PRODUCTION & ENGINEERING
Nautylusprod
Nautylusprod
Producer

Lyrics

Hum hum Weettay dima ray Té niémé wou ma netali Mangui sama yoon Ni pithie Ramatou Yala dima weteuli Gorr momoul nianne Yareewouniouma tallal lokho Yaay joor sama yaye Mangui sakkou sa niane Yeurmande amoul fii Wettay ak namel Nek ndaw si samay digeu morom yaffouss warouma Fii lekougnou ba sour Nanouniou ba mandé Way nek ndaw si samay digeu morom yaffouss warouma So yewo yema fallo So yewo yema fall (Yeah) Fi degn fi nekk ak ngor Fi degn fi dathie lou metti Nekk fi ak jom Fatewouma demb ak Yaay Joor Wettay si xol la meun yam Sam khel jougoul si sassmeu Goné diss neu wayé bo magué fay borr Lambay soudé meuss neu nekh Tay Walo amoul ndokh Touki dou tekki Gaaday andou tak banekh Wetna wettay bimay yé Rerr na fou gnar gni fegn Genteu beu demb fegn tay Yéné beu agg Jooy na fou keine newoul, dem na ba bougou ma guiss samay rongogn Ndakh mounou meu bayi limalen diguon Jambar dawoul daa outi ji wone Yakar bou tassoul ba tay Ndakh yoon bi diekha goul Sama khel ci kasso dou teey dey dem fou dieumeu doul yegg di fey Wetna wettay bimay yé Anh anh anh Jooy na jooy guisouma keineu Yeah yeah yeah Love and peace for me I can shine, shine like a diamond Wa wa wa I can shine, shine like a diamond Pray for, for me yeah Wettay dima ray (wettay) Té niémé wou ma netali Mangui sama yoon Ni pithie Ramatou Yala dima weteuli Gorr momoul nianne Yareewouniouma tallal lokho Yaay joor sama yaye Mangui sakkou sa niane Yeurmande amoul fii Wettay ak namel Nek ndaw si samay digeu morom yaffouss warouma Fii lekougnou ba sour Nanouniou ba mandé Way nek ndaw si samay digeu morom yaffouss warogno So yewo yema fallo So yewo yema fall Ndibeulo yeurmandey fall Doley biir bek bitti bee fall
Writer(s): Abdoulaye Sy, Ashs The Best, Obree Daman, Olivier Delahaye Lyrics powered by www.musixmatch.com
Get up to 2 months free of Apple Music
instagramSharePathic_arrow_out