album cover
NAWLE
album cover
00:00
00:05
00:10
01:05
01:15
01:40
01:45
03:00
00:00
03:14
Past 7 Days
NAWLE was discovered most frequently at around 1 minutes and 15 seconds into the song during the past week

Lyrics

Su nit doon may boppam
Dunu néewle
Dunu doon ay néewji doole
Kenn du nu ëppële
Yàlla Mooy maye waay
Xeeb nañu maa ngir li may néewji doole
Nee nañu duma sa nawle
Xool nañu ma bëtu xeebeel
Yàlla Mooy maye waay
Su ma doonoon kiy dogal
Sa askan kenn du ma ci raw
Ndax ni ñu ma def
Dese nañu ma weg
Gis naa lépp li nga may defal
Sa waa kër yépp ne du ci dal
Du fi ame
Nga jàmb leen
Ngir jëmm ju xeebu jii
Leegi leegi
Fàww ma dem uti indi
Leegi leegi
Manuma dem bàyyi la
Day jeex day jeex
Nee nañu amaluma la njariñ nga dem bayi ma
Day jeex day jeex
Fàww ma dem uti indi
Leegi leegi
Doole laa néewle
Leegi leegi
Nee nañu duma sa nawle
Day jeex day jeex
Nee nañu amaluma la njariñ nga dem bayima
Day jeex day jeex
Uurul ayni ay sa niroowaale
Aw nga ci tànku yaayi waa ji
Yaa ngi mel ni Paale mu ndaw
Ndax ay jikkoom ngay daaguwaale
Doo nettali doo gaaruwaale
Dugalóo ma ci giraawaale
Eey Buso Baali
Ngir jëmm ju xeebu ji
Leegi leegi
Fàww ma dem uti indi
Leegi leegi
Manuma dem bàyyi la
Day jeex day jeex
Nee nañu amaluma la njariñ nga dem bayima
Day jeex day jeex
Fàww ma dem uti indi
Leegi leegi
Doole laa néewle
Leegi leegi
Nee nañu duma sa nawle
Day jeex day jeex
Nee nañu amaluma la njariñ nga dem bayima
Day jeex day jeex
Written by: Beneth Seraphin Akatche Koffi, Saliou Samb
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...